An-Najm · 40/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
وَأَنَّ سَعْيَهُ سَوْفَ يُرَىٰ ۝٤٠
Wa anna sa`yahoo sawfa yuraa
📖 Tekkim Wolof
te la mu daan jëf, dana fés, bu bis pénc baa.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 38-42 — Simoore An-Najm

38أَلَّا تَزِرُ وَازِرَةٌ وِزْرَ أُخْرَىٰ
benn bakkan du gàddul bakkan bàkkaaram,
39وَأَن لَّيْسَ لِلْإِنسَانِ إِلَّا مَا سَعَىٰ
li wér daal, nit ku nekk jëfam lay añe ;
40وَأَنَّ سَعْيَهُ سَوْفَ يُرَىٰ
te la mu daan jëf, dana fés, bu bis pénc baa.
41ثُمَّ يُجْزَاهُ الْجَزَاءَ الْأَوْفَىٰ
Te dees na ko ko fay ba mu mat sëkk,
42وَأَنَّ إِلَىٰ رَبِّكَ الْمُنتَهَىٰ
te nag lépp, ngay jeexe, ca sa Boroom,
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
40Aaya

Tekki — An-Najm 40

Simoore An-Najm Aaya 40 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te la mu daan jëf, dana fés, bu bis pénc…

Simoore Aaya 40/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 38–42. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers