An-Najm · 41/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
ثُمَّ يُجْزَاهُ الْجَزَاءَ الْأَوْفَىٰ ۝٤١
Summa yujzaahul jazaaa `al awfaa
📖 Tekkim Wolof
Te dees na ko ko fay ba mu mat sëkk,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 39-43 — Simoore An-Najm

39وَأَن لَّيْسَ لِلْإِنسَانِ إِلَّا مَا سَعَىٰ
li wér daal, nit ku nekk jëfam lay añe ;
40وَأَنَّ سَعْيَهُ سَوْفَ يُرَىٰ
te la mu daan jëf, dana fés, bu bis pénc baa.
41ثُمَّ يُجْزَاهُ الْجَزَاءَ الْأَوْفَىٰ
Te dees na ko ko fay ba mu mat sëkk,
42وَأَنَّ إِلَىٰ رَبِّكَ الْمُنتَهَىٰ
te nag lépp, ngay jeexe, ca sa Boroom,
43وَأَنَّهُ هُوَ أَضْحَكَ وَأَبْكَىٰ
te moom Mooy reetaanloo di jooyloo,
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
41Aaya

Tekki — An-Najm 41

Simoore An-Najm Aaya 41 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te dees na ko ko fay ba mu mat sëkk,

Simoore Aaya 41/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 39–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers