An-Najm · 42/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
وَأَنَّ إِلَىٰ رَبِّكَ الْمُنتَهَىٰ ۝٤٢
Wa anna ilaa rabbikal muntahaa
📖 Tekkim Wolof
te nag lépp, ngay jeexe, ca sa Boroom,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 40-44 — Simoore An-Najm

40وَأَنَّ سَعْيَهُ سَوْفَ يُرَىٰ
te la mu daan jëf, dana fés, bu bis pénc baa.
41ثُمَّ يُجْزَاهُ الْجَزَاءَ الْأَوْفَىٰ
Te dees na ko ko fay ba mu mat sëkk,
42وَأَنَّ إِلَىٰ رَبِّكَ الْمُنتَهَىٰ
te nag lépp, ngay jeexe, ca sa Boroom,
43وَأَنَّهُ هُوَ أَضْحَكَ وَأَبْكَىٰ
te moom Mooy reetaanloo di jooyloo,
44وَأَنَّهُ هُوَ أَمَاتَ وَأَحْيَا
te it moom Mooy rey mooy dekkal,
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — An-Najm 42

Simoore An-Najm Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te nag lépp, ngay jeexe, ca sa Boroom,

Simoore Aaya 42/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers