Al-Qamar · 49/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
إِنَّا كُلَّ شَيْءٍ خَلَقْنَاهُ بِقَدَرٍ ۝٤٩
Innaa kulla shai`in khalaqnaahu biqadar
📖 Tekkim Wolof
Noo bind lépp lu nekk cig natale,

🎧 Dégg


📜 Aaya 47-51 — Simoore Al-Qamar

47إِنَّ الْمُجْرِمِينَ فِي ضَلَالٍ وَسُعُرٍ
Tooñkat ya ña nga ca, cànkute ak réer.
48يَوْمَ يُسْحَبُونَ فِي النَّارِ عَلَىٰ وُجُوهِهِمْ ذُوقُوا مَسَّ سَقَرَ
Bu keroogee ba ñu di leen diri ci seen xarkanam ca biir Safara, (naan leen) : “Mosleen tokamti gu Safara”.
49إِنَّا كُلَّ شَيْءٍ خَلَقْنَاهُ بِقَدَرٍ
Noo bind lépp lu nekk cig natale,
50وَمَا أَمْرُنَا إِلَّا وَاحِدَةٌ كَلَمْحٍ بِالْبَصَرِ
amul sunu menn mbir [ndigal] ; [lu dul ne] dafay mel ni xefiinu bët.
51وَلَقَدْ أَهْلَكْنَا أَشْيَاعَكُمْ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Faagaagal Nanu, ay xeet yu mel ni yéen. Mo ndax kon kenn du fàttaliku jàjj ?
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
49Aaya

Tekki — Al-Qamar 49

Simoore Al-Qamar Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noo bind lépp lu nekk cig natale,

Simoore Aaya 49/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 47–51. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers