Al-An'am · 66/165
Tekki Waxtaan — Al-An'am
وَكَذَّبَ بِهِ قَوْمُكَ وَهُوَ الْحَقُّ ۚ قُل لَّسْتُ عَلَيْكُم بِوَكِيلٍ ٦٦
Transliteration
Wa kaz zaba bihee qawmuka wa huwal haqq; qul lastu`alaikum biwakeel
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Say nit weddi nañu te Moom mooy dëgg. Neeleen : “Du maa leen di sàmm.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 64-68 — Al-An'am
64قُلِ اللَّهُ يُنَجِّيكُم مِّنْهَا وَمِن كُلِّ كَرْبٍ ثُمَّ أَنتُمْ تُشْرِكُونَ
Neel : “Yàlla moo leen di musal ci loolu, ak njàqare ju mu mën di doon. Ba noppi ngeen di ko bokkaale”.
65قُلْ هُوَ الْقَادِرُ عَلَىٰ أَن يَبْعَثَ عَلَيْكُمْ عَذَابًا مِّن فَوْقِكُمْ أَوْ مِن تَحْتِ أَرْجُلِكُمْ أَوْ يَلْبِسَكُمْ شِيَعًا وَيُذِيقَ بَعْضَكُم بَأْسَ بَعْضٍ ۗ انظُرْ كَيْفَ نُصَرِّفُ الْآيَاتِ لَعَلَّهُمْ يَفْقَهُونَ
Neel : “Moom am na kàttanug yónnee leen mbugal mu leen bawoo ci kaw walla ci seen suufi tànk, mbaa Mu dogal, ci seen biir, juuyoo. Ba ku nekk mos ngaañ la jóge ca moroomam.” Gisal ni Nuy leeralee tegtal yi ndax ñoom ñu mën koo dégg ?
66وَكَذَّبَ بِهِ قَوْمُكَ وَهُوَ الْحَقُّ ۚ قُل لَّسْتُ عَلَيْكُم بِوَكِيلٍ
Say nit weddi nañu te Moom mooy dëgg. Neeleen : “Du maa leen di sàmm.
67لِّكُلِّ نَبَإٍ مُّسْتَقَرٌّ ۚ وَسَوْفَ تَعْلَمُونَ
Xew-xew bu ne am na waxtoon te dangeen mës a xam.”
68وَإِذَا رَأَيْتَ الَّذِينَ يَخُوضُونَ فِي آيَاتِنَا فَأَعْرِضْ عَنْهُمْ حَتَّىٰ يَخُوضُوا فِي حَدِيثٍ غَيْرِهِ ۚ وَإِمَّا يُنسِيَنَّكَ الشَّيْطَانُ فَلَا تَقْعُدْ بَعْدَ الذِّكْرَىٰ مَعَ الْقَوْمِ الظَّالِمِينَ
Boo gisee aw nit ñuy doyadal Sunuy kàddu, dëdduleen ba bañuy xuus ci weneen waxtaan. Bu la Séytaane fàtteloo ba nga fàtte ko. Saa soo ko fàttalikoo sañatoo toogandoo nag ak aw nit ñu di ay tooñkat.
Al-An'amFihi Alxuraan
165Aaya
MeccanRevelation
66Aaya
Tekki — Al-An'am 66
Simoore Al-An'am Aaya 66 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Say nit weddi nañu te Moom mooy dëgg. Neeleen :…Simoore Aaya 66/165 — Al-An'am الأنعام (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-An'am Dégg, Al-An'am Tekki, Al-An'am mp3, Al-An'am pdf. Aaya 64–68. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








