Al-An'am · 89/165
Tekki Waxtaan — Al-An'am
أُولَٰئِكَ الَّذِينَ آتَيْنَاهُمُ الْكِتَابَ وَالْحُكْمَ وَالنُّبُوَّةَ ۚ فَإِن يَكْفُرْ بِهَا هَٰؤُلَاءِ فَقَدْ وَكَّلْنَا بِهَا قَوْمًا لَّيْسُوا بِهَا بِكَافِرِينَ ۝٨٩
Ulaaa`ikal lazeena aatainaahumul Kitaaba wal hukma wan Nubuwwah; fa iny yakfur bihaa haaa`ulaaa`i faqad wakkalnaa bihaa qawmal laisoo bihaa bikaafireen
📖 Tekkim Wolof
Ñooña ñooy ña Nu jox Téere ba ak àtte ya ak Yonent ga. Nit ña, bu ñu weddee yooyu, dana fekk dénkoon Nanu leen aw xeet wu leen weddiwul woon.

🎧 Dégg


📜 Aaya 87-91 — Al-An'am

87وَمِنْ آبَائِهِمْ وَذُرِّيَّاتِهِمْ وَإِخْوَانِهِمْ ۖ وَاجْتَبَيْنَاهُمْ وَهَدَيْنَاهُمْ إِلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Te ca biir seeni baay ak seeni sët ak seeni mbokk, tànn Nanu leen, jubal leen, teg leen ca yoon bu jub wa.
88ذَٰلِكَ هُدَى اللَّهِ يَهْدِي بِهِ مَن يَشَاءُ مِنْ عِبَادِهِ ۚ وَلَوْ أَشْرَكُوا لَحَبِطَ عَنْهُم مَّا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Loolu mooy njubug Yàlla, Dana ci gindi ku Ko neex ciy jaamam. Waaye bu ñu bokkaale woon, fàwwu la ñu daan def [ci lu baax] dana yàqu.
89أُولَٰئِكَ الَّذِينَ آتَيْنَاهُمُ الْكِتَابَ وَالْحُكْمَ وَالنُّبُوَّةَ ۚ فَإِن يَكْفُرْ بِهَا هَٰؤُلَاءِ فَقَدْ وَكَّلْنَا بِهَا قَوْمًا لَّيْسُوا بِهَا بِكَافِرِينَ
Ñooña ñooy ña Nu jox Téere ba ak àtte ya ak Yonent ga. Nit ña, bu ñu weddee yooyu, dana fekk dénkoon Nanu leen aw xeet wu leen weddiwul woon.
90أُولَٰئِكَ الَّذِينَ هَدَى اللَّهُ ۖ فَبِهُدَاهُمُ اقْتَدِهْ ۗ قُل لَّا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ أَجْرًا ۖ إِنْ هُوَ إِلَّا ذِكْرَىٰ لِلْعَالَمِينَ
Ñooñu la Yàlla gindi : royal seenug njub. Neel : “Laajumaleen ci ag pey”. Dafa fekk rekk ne lii moom ag fàttali la ñeel waa àddina si.
91وَمَا قَدَرُوا اللَّهَ حَقَّ قَدْرِهِ إِذْ قَالُوا مَا أَنزَلَ اللَّهُ عَلَىٰ بَشَرٍ مِّن شَيْءٍ ۗ قُلْ مَنْ أَنزَلَ الْكِتَابَ الَّذِي جَاءَ بِهِ مُوسَىٰ نُورًا وَهُدًى لِّلنَّاسِ ۖ تَجْعَلُونَهُ قَرَاطِيسَ تُبْدُونَهَا وَتُخْفُونَ كَثِيرًا ۖ وَعُلِّمْتُم مَّا لَمْ تَعْلَمُوا أَنتُمْ وَلَا آبَاؤُكُمْ ۖ قُلِ اللَّهُ ۖ ثُمَّ ذَرْهُمْ فِي خَوْضِهِمْ يَلْعَبُونَ
Màggaluñu Yàlla kem dayo bi mu yayoo ñu màggale Ko, bu ñu waxee ne : “Yàlla wàccewul dara ci kenn.”. Neel : “Kan moo wàcce Téere bu Muusaa ànd ak leer ak njub ñeel nit ñi ? Ngeen bind ko ciy këyit di ko wone ak di ca nëbb lu bari. Te jàngaleef na leen lu ngeen xamul woon yéen ak seeni baay. Neel : “Yàlla la”. Te nga bàyyi leen ci seen cànkute ga ñuy nuur cim po.
Al-An'amFihi Alxuraan
165Aaya
MeccanRevelation
89Aaya

Tekki — Al-An'am 89

Simoore Al-An'am Aaya 89 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñooña ñooy ña Nu jox Téere ba ak àtte ya…

Simoore Aaya 89/165 — Al-An'am الأنعام (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-An'am Dégg, Al-An'am Tekki, Al-An'am mp3, Al-An'am pdf. Aaya 87–91. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers