Al-An'am · 88/165
Tekki Waxtaan — Simoore Al-An'am
ذَٰلِكَ هُدَى اللَّهِ يَهْدِي بِهِ مَن يَشَاءُ مِنْ عِبَادِهِ ۚ وَلَوْ أَشْرَكُوا لَحَبِطَ عَنْهُم مَّا كَانُوا يَعْمَلُونَ ۝٨٨
Zaalika hudal laahi yahdee bihee mai yashaaa`u min `ibaadih; wa law ashrakoo lahabita `anhum maa kaanoo ya`maloon
📖 Tekkim Wolof
Loolu mooy njubug Yàlla, Dana ci gindi ku Ko neex ciy jaamam. Waaye bu ñu bokkaale woon, fàwwu la ñu daan def [ci lu baax] dana yàqu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 86-90 — Simoore Al-An'am

86وَإِسْمَاعِيلَ وَالْيَسَعَ وَيُونُسَ وَلُوطًا ۚ وَكُلًّا فَضَّلْنَا عَلَى الْعَالَمِينَ
Ak Ismaahiila ak Ilyaas, ak Yunuus, ak Lóot. Te ñoom ñépp defal Nanu leen ngëneel ci kaw waa àddina si.
87وَمِنْ آبَائِهِمْ وَذُرِّيَّاتِهِمْ وَإِخْوَانِهِمْ ۖ وَاجْتَبَيْنَاهُمْ وَهَدَيْنَاهُمْ إِلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Te ca biir seeni baay ak seeni sët ak seeni mbokk, tànn Nanu leen, jubal leen, teg leen ca yoon bu jub wa.
88ذَٰلِكَ هُدَى اللَّهِ يَهْدِي بِهِ مَن يَشَاءُ مِنْ عِبَادِهِ ۚ وَلَوْ أَشْرَكُوا لَحَبِطَ عَنْهُم مَّا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Loolu mooy njubug Yàlla, Dana ci gindi ku Ko neex ciy jaamam. Waaye bu ñu bokkaale woon, fàwwu la ñu daan def [ci lu baax] dana yàqu.
89أُولَٰئِكَ الَّذِينَ آتَيْنَاهُمُ الْكِتَابَ وَالْحُكْمَ وَالنُّبُوَّةَ ۚ فَإِن يَكْفُرْ بِهَا هَٰؤُلَاءِ فَقَدْ وَكَّلْنَا بِهَا قَوْمًا لَّيْسُوا بِهَا بِكَافِرِينَ
Ñooña ñooy ña Nu jox Téere ba ak àtte ya ak Yonent ga. Nit ña, bu ñu weddee yooyu, dana fekk dénkoon Nanu leen aw xeet wu leen weddiwul woon.
90أُولَٰئِكَ الَّذِينَ هَدَى اللَّهُ ۖ فَبِهُدَاهُمُ اقْتَدِهْ ۗ قُل لَّا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ أَجْرًا ۖ إِنْ هُوَ إِلَّا ذِكْرَىٰ لِلْعَالَمِينَ
Ñooñu la Yàlla gindi : royal seenug njub. Neel : “Laajumaleen ci ag pey”. Dafa fekk rekk ne lii moom ag fàttali la ñeel waa àddina si.
Al-An'amFihi Alxuraan
165Aaya
MeccanRevelation
88Aaya

Tekki — Al-An'am 88

Simoore Al-An'am Aaya 88 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Loolu mooy njubug Yàlla, Dana ci gindi ku Ko neex…

Simoore Aaya 88/165 — Simoore Al-An'am الأنعام (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-An'am Dégg, Simoore Al-An'am Tekki, Simoore Al-An'am mp3, Simoore Al-An'am pdf. Aaya 86–90. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers