Al-Haqqa · 19/52
Tekki Waxtaan — Al-Haqqa
فَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ بِيَمِينِهِ فَيَقُولُ هَاؤُمُ اقْرَءُوا كِتَابِيَهْ ١٩
Transliteration
Fa ammaa man ootiya kitaabahoo biyameenihee fa yaqoolu haaa`umuq ra`oo kitaabiyah
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ña nga xam ne dañoo jot seeni Téere ci ndeyjoor, da leen di wax ne : “Jàppleen ! jàng samab téere.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 17-21 — Al-Haqqa
17وَالْمَلَكُ عَلَىٰ أَرْجَائِهَا ۚ وَيَحْمِلُ عَرْشَ رَبِّكَ فَوْقَهُمْ يَوْمَئِذٍ ثَمَانِيَةٌ
Malaaka ya nekk ci ay goxam, su ko defee juróom-ñatta, cay yanu gàngunaay ga ( Aras ).
18يَوْمَئِذٍ تُعْرَضُونَ لَا تَخْفَىٰ مِنكُمْ خَافِيَةٌ
Bu keroogee dees na leen weer; ken du leen ca nëbb dara.
19فَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ بِيَمِينِهِ فَيَقُولُ هَاؤُمُ اقْرَءُوا كِتَابِيَهْ
Ña nga xam ne dañoo jot seeni Téere ci ndeyjoor, da leen di wax ne : “Jàppleen ! jàng samab téere.
20إِنِّي ظَنَنتُ أَنِّي مُلَاقٍ حِسَابِيَهْ
Man dey jàppoon naa ne danaa dajeek samab màndaxe”.
21فَهُوَ فِي عِيشَةٍ رَّاضِيَةٍ
Moom dey mi ngi ci dundu gu neex :
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
19Aaya
Tekki — Al-Haqqa 19
Simoore Al-Haqqa Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña nga xam ne dañoo jot seeni Téere ci ndeyjoor,…Simoore Aaya 19/52 — Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Haqqa Dégg, Al-Haqqa Tekki, Al-Haqqa mp3, Al-Haqqa pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








