Al-Haqqa · 20/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Haqqa
إِنِّي ظَنَنتُ أَنِّي مُلَاقٍ حِسَابِيَهْ ۝٢٠
Innee zannantu annee mulaaqin hisaabiyah
📖 Tekkim Wolof
Man dey jàppoon naa ne danaa dajeek samab màndaxe”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 18-22 — Simoore Al-Haqqa

18يَوْمَئِذٍ تُعْرَضُونَ لَا تَخْفَىٰ مِنكُمْ خَافِيَةٌ
Bu keroogee dees na leen weer; ken du leen ca nëbb dara.
19فَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ بِيَمِينِهِ فَيَقُولُ هَاؤُمُ اقْرَءُوا كِتَابِيَهْ
Ña nga xam ne dañoo jot seeni Téere ci ndeyjoor, da leen di wax ne : “Jàppleen ! jàng samab téere.
20إِنِّي ظَنَنتُ أَنِّي مُلَاقٍ حِسَابِيَهْ
Man dey jàppoon naa ne danaa dajeek samab màndaxe”.
21فَهُوَ فِي عِيشَةٍ رَّاضِيَةٍ
Moom dey mi ngi ci dundu gu neex :
22فِي جَنَّةٍ عَالِيَةٍ
ca Àjjana ju kawe
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — Al-Haqqa 20

Simoore Al-Haqqa Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Man dey jàppoon naa ne danaa dajeek samab màndaxe”.

Simoore Aaya 20/52 — Simoore Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Haqqa Dégg, Simoore Al-Haqqa Tekki, Simoore Al-Haqqa mp3, Simoore Al-Haqqa pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers