Al-Haqqa · 18/52
Tekki Waxtaan — Al-Haqqa
يَوْمَئِذٍ تُعْرَضُونَ لَا تَخْفَىٰ مِنكُمْ خَافِيَةٌ ۝١٨
Yawma`izin tu`radoona laa takhfaa min kum khaafiyah
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee dees na leen weer; ken du leen ca nëbb dara.

🎧 Dégg


📜 Aaya 16-20 — Al-Haqqa

16وَانشَقَّتِ السَّمَاءُ فَهِيَ يَوْمَئِذٍ وَاهِيَةٌ
asamaan siy xottiku nooy nepp.
17وَالْمَلَكُ عَلَىٰ أَرْجَائِهَا ۚ وَيَحْمِلُ عَرْشَ رَبِّكَ فَوْقَهُمْ يَوْمَئِذٍ ثَمَانِيَةٌ
Malaaka ya nekk ci ay goxam, su ko defee juróom-ñatta, cay yanu gàngunaay ga ( Aras ).
18يَوْمَئِذٍ تُعْرَضُونَ لَا تَخْفَىٰ مِنكُمْ خَافِيَةٌ
Bu keroogee dees na leen weer; ken du leen ca nëbb dara.
19فَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ بِيَمِينِهِ فَيَقُولُ هَاؤُمُ اقْرَءُوا كِتَابِيَهْ
Ña nga xam ne dañoo jot seeni Téere ci ndeyjoor, da leen di wax ne : “Jàppleen ! jàng samab téere.
20إِنِّي ظَنَنتُ أَنِّي مُلَاقٍ حِسَابِيَهْ
Man dey jàppoon naa ne danaa dajeek samab màndaxe”.
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
18Aaya

Tekki — Al-Haqqa 18

Simoore Al-Haqqa Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee dees na leen weer; ken du leen ca…

Simoore Aaya 18/52 — Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Haqqa Dégg, Al-Haqqa Tekki, Al-Haqqa mp3, Al-Haqqa pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers