Al-A'raf · 110/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
يُرِيدُ أَن يُخْرِجَكُم مِّنْ أَرْضِكُمْ ۖ فَمَاذَا تَأْمُرُونَ ۝١١٠
Yureedu ai yukhrijakum min ardikum famaazaa taamuroon
📖 Tekkim Wolof
[Firawna] ne : “Dafa leen bëgg a génne ci seen suuf.” - “Lan mooy seen ndigal ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 108-112 — Simoore Al-A'raf

108وَنَزَعَ يَدَهُ فَإِذَا هِيَ بَيْضَاءُ لِلنَّاظِرِينَ
Mu génne loxoom mu daldi weex tàll ca ña koy gis.
109قَالَ الْمَلَأُ مِن قَوْمِ فِرْعَوْنَ إِنَّ هَٰذَا لَسَاحِرٌ عَلِيمٌ
Kilifa ya bokk ca nitu Firawna ne ko : “Jabar bu am xam-xam la”.
110يُرِيدُ أَن يُخْرِجَكُم مِّنْ أَرْضِكُمْ ۖ فَمَاذَا تَأْمُرُونَ
[Firawna] ne : “Dafa leen bëgg a génne ci seen suuf.” - “Lan mooy seen ndigal ? ”
111قَالُوا أَرْجِهْ وَأَخَاهُ وَأَرْسِلْ فِي الْمَدَائِنِ حَاشِرِينَ
Ñu ne ko : “Xaarloo ko mook mbokkam, te yónnee ci dëkk yi ay ndaw ñu mën a dajale nit ñi,
112يَأْتُوكَ بِكُلِّ سَاحِرٍ عَلِيمٍ
ñu indil la bépp jabar bu am xam-xam.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
110Aaya

Tekki — Al-A'raf 110

Simoore Al-A'raf Aaya 110 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Firawna] ne : “Dafa leen bëgg a génne ci seen…

Simoore Aaya 110/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 108–112. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers