Al-A'raf · 109/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
قَالَ الْمَلَأُ مِن قَوْمِ فِرْعَوْنَ إِنَّ هَٰذَا لَسَاحِرٌ عَلِيمٌ ۝١٠٩
Qaalal mala-u min qawmi Fir`awna inna haazaa lasaa hirun `aleem
📖 Tekkim Wolof
Kilifa ya bokk ca nitu Firawna ne ko : “Jabar bu am xam-xam la”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 107-111 — Simoore Al-A'raf

107فَأَلْقَىٰ عَصَاهُ فَإِذَا هِيَ ثُعْبَانٌ مُّبِينٌ
Sànni na yetam wa mu daldi nekk jaan ju rëy.
108وَنَزَعَ يَدَهُ فَإِذَا هِيَ بَيْضَاءُ لِلنَّاظِرِينَ
Mu génne loxoom mu daldi weex tàll ca ña koy gis.
109قَالَ الْمَلَأُ مِن قَوْمِ فِرْعَوْنَ إِنَّ هَٰذَا لَسَاحِرٌ عَلِيمٌ
Kilifa ya bokk ca nitu Firawna ne ko : “Jabar bu am xam-xam la”.
110يُرِيدُ أَن يُخْرِجَكُم مِّنْ أَرْضِكُمْ ۖ فَمَاذَا تَأْمُرُونَ
[Firawna] ne : “Dafa leen bëgg a génne ci seen suuf.” - “Lan mooy seen ndigal ? ”
111قَالُوا أَرْجِهْ وَأَخَاهُ وَأَرْسِلْ فِي الْمَدَائِنِ حَاشِرِينَ
Ñu ne ko : “Xaarloo ko mook mbokkam, te yónnee ci dëkk yi ay ndaw ñu mën a dajale nit ñi,
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
109Aaya

Tekki — Al-A'raf 109

Simoore Al-A'raf Aaya 109 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kilifa ya bokk ca nitu Firawna ne ko : “Jabar…

Simoore Aaya 109/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 107–111. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers