Al-A'raf · 174/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
وَكَذَٰلِكَ نُفَصِّلُ الْآيَاتِ وَلَعَلَّهُمْ يَرْجِعُونَ ١٧٤
Transliteration
Wa kazaalika nufassihul Aayaati wa la`allahum yarji`oon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Noonu la Nuy leeralee tegtal yi. Ndax xéy-na ñu dellusi [ci seen Boroom] !
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 172-176 — Al-A'raf
172وَإِذْ أَخَذَ رَبُّكَ مِن بَنِي آدَمَ مِن ظُهُورِهِمْ ذُرِّيَّتَهُمْ وَأَشْهَدَهُمْ عَلَىٰ أَنفُسِهِمْ أَلَسْتُ بِرَبِّكُمْ ۖ قَالُوا بَلَىٰ ۛ شَهِدْنَا ۛ أَن تَقُولُوا يَوْمَ الْقِيَامَةِ إِنَّا كُنَّا عَنْ هَٰذَا غَافِلِينَ
[Fàttalikul] ba sa Boroom génnee ci ndigul doomu-aadama yi seeni sëf, te Mu seedeloo leen ci seen bopp, ne leen : “Du Maay seen Boroom ? ”. Ñu ne : “Axakay, seede nanu ko...” - ngir ngeen bañ a wax ca Bis-pénc ba ne : “Danoo réere woon lii [mu nekk seenu lay]”,
173أَوْ تَقُولُوا إِنَّمَا أَشْرَكَ آبَاؤُنَا مِن قَبْلُ وَكُنَّا ذُرِّيَّةً مِّن بَعْدِهِمْ ۖ أَفَتُهْلِكُنَا بِمَا فَعَلَ الْمُبْطِلُونَ
mbaa ngeen bañ a wax : “Du dara lu dul sunuy maam dañoo bokkaale woon lu jiitu nu sëtoo ca ñoom ginnaaw ga. Ndax dees na nu mbugal [ci loo xam ne ña jubutoon ca nun ñoo ko def] ? ”
174وَكَذَٰلِكَ نُفَصِّلُ الْآيَاتِ وَلَعَلَّهُمْ يَرْجِعُونَ
Noonu la Nuy leeralee tegtal yi. Ndax xéy-na ñu dellusi [ci seen Boroom] !
175وَاتْلُ عَلَيْهِمْ نَبَأَ الَّذِي آتَيْنَاهُ آيَاتِنَا فَانسَلَخَ مِنْهَا فَأَتْبَعَهُ الشَّيْطَانُ فَكَانَ مِنَ الْغَاوِينَ
Nettalileen ka Nu joxoon Sunuy mbóot mu rocceeku ca. Séytaane topp ko, tax na mu bokk ca way-beew ña.
176وَلَوْ شِئْنَا لَرَفَعْنَاهُ بِهَا وَلَٰكِنَّهُ أَخْلَدَ إِلَى الْأَرْضِ وَاتَّبَعَ هَوَاهُ ۚ فَمَثَلُهُ كَمَثَلِ الْكَلْبِ إِن تَحْمِلْ عَلَيْهِ يَلْهَثْ أَوْ تَتْرُكْهُ يَلْهَث ۚ ذَّٰلِكَ مَثَلُ الْقَوْمِ الَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا ۚ فَاقْصُصِ الْقَصَصَ لَعَلَّهُمْ يَتَفَكَّرُونَ
Su nu sooboon Nu yékkatikook mbóot yooyu, waaye dafa jengoon jëm ci àddina, topp bànneexam. Dafay mel ni xaj, boo ko songee muy yalkat, boo ko bàyyee muy yalkat. Loolu mooy niróowaaleeb nit ña weddi Sunuy kàddu. Nettalil xew-xew ba. Xéy-na ñoom ñu fàttaliku !
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
174Aaya
Tekki — Al-A'raf 174
Simoore Al-A'raf Aaya 174 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noonu la Nuy leeralee tegtal yi. Ndax xéy-na ñu dellusi…Simoore Aaya 174/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 172–176. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








