Al-A'raf · 69/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
أَوَعَجِبْتُمْ أَن جَاءَكُمْ ذِكْرٌ مِّن رَّبِّكُمْ عَلَىٰ رَجُلٍ مِّنكُمْ لِيُنذِرَكُمْ ۚ وَاذْكُرُوا إِذْ جَعَلَكُمْ خُلَفَاءَ مِن بَعْدِ قَوْمِ نُوحٍ وَزَادَكُمْ فِي الْخَلْقِ بَسْطَةً ۖ فَاذْكُرُوا آلَاءَ اللَّهِ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ ۝٦٩
awa `ajibtum an jaaa`akum zikrum mir Rabbikum `alaa rajulim minkum liyunzirakum; wazkurooo iz ja`alakum khulafaaa`a mim ba`di qawmi noohinw wa zaadakum filkhalqi bastatan fazkurooo aalaaa`al laahi la`allakum tuflihoon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax dafa leen yéem, waare dikkal leen tukke ci seen Boroom, jaare ci góor gu bokk ci yéen ngir mu artu leen? Fàttalikuleen ginnaaw ba Mu leen defee ngeen di kuutaay ginnaaw nitu Nooh, te Mu yokk seeni jëmm, dolli seeni kàttan. Fàttalikuleen xéewali Yàlla yi ndax xéy-na yéen ngeen texe.
🎧 Dégg

📜 Aaya 67-71 — Al-A'raf

67قَالَ يَا قَوْمِ لَيْسَ بِي سَفَاهَةٌ وَلَٰكِنِّي رَسُولٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ
Mu ne : "Yéen samay mbokk, ag ndof nekkul ci man de ; waaye li wér moo di ne man ab Yonent laa, [ndaw] lu bawoo fa Yàlla Boroom àddina si.
68أُبَلِّغُكُمْ رِسَالَاتِ رَبِّي وَأَنَا لَكُمْ نَاصِحٌ أَمِينٌ
Dama leen di jottali bataaxalub sama Boroom te man dama nekk ci yéen aji-laabir ju wóor.
69أَوَعَجِبْتُمْ أَن جَاءَكُمْ ذِكْرٌ مِّن رَّبِّكُمْ عَلَىٰ رَجُلٍ مِّنكُمْ لِيُنذِرَكُمْ ۚ وَاذْكُرُوا إِذْ جَعَلَكُمْ خُلَفَاءَ مِن بَعْدِ قَوْمِ نُوحٍ وَزَادَكُمْ فِي الْخَلْقِ بَسْطَةً ۖ فَاذْكُرُوا آلَاءَ اللَّهِ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ
Moo ndax dafa leen yéem, waare dikkal leen tukke ci seen Boroom, jaare ci góor gu bokk ci yéen ngir mu artu leen? Fàttalikuleen ginnaaw ba Mu leen defee ngeen di kuutaay ginnaaw nitu Nooh, te Mu yokk seeni jëmm, dolli seeni kàttan. Fàttalikuleen xéewali Yàlla yi ndax xéy-na yéen ngeen texe.
70قَالُوا أَجِئْتَنَا لِنَعْبُدَ اللَّهَ وَحْدَهُ وَنَذَرَ مَا كَانَ يَعْبُدُ آبَاؤُنَا ۖ فَأْتِنَا بِمَا تَعِدُنَا إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Ñu wax ne : “Ndax danga noo dikkal ngir nu jaamu Yàlla moom doŋŋ, te bàyyi li sunu maam ya daan jaamu ? Indil nu li nga nu daan tëkkoo, ndegam ku dëggu nga”.
71قَالَ قَدْ وَقَعَ عَلَيْكُم مِّن رَّبِّكُمْ رِجْسٌ وَغَضَبٌ ۖ أَتُجَادِلُونَنِي فِي أَسْمَاءٍ سَمَّيْتُمُوهَا أَنتُمْ وَآبَاؤُكُم مَّا نَزَّلَ اللَّهُ بِهَا مِن سُلْطَانٍ ۚ فَانتَظِرُوا إِنِّي مَعَكُم مِّنَ الْمُنتَظِرِينَ
Mu toontu ne : “Nekk na lu leen dëddale tukke ca seen Boroom, mbugal ak mer. Moo ndax dangeen di dàggasanteek man ciy tur yu ngeen sos yéen ak seeni maam, te Yàlla wàccewu ca wenn lay ? Man maa ngi nekk ak yéen di bokk ca way-muñandiku ña.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
69Aaya

Tekki — Al-A'raf 69

Simoore Al-A'raf Aaya 69 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax dafa leen yéem, waare dikkal leen tukke ci…

Simoore Aaya 69/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 67–71. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers