Al-Qiyama · 12/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
إِلَىٰ رَبِّكَ يَوْمَئِذٍ الْمُسْتَقَرُّ ۝١٢
Ilaa rabbika yawma `izinil mustaqarr
📖 Tekkim Wolof
Bis boobu kay, dellu ca sa Boroom, rekk ay am.

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Simoore Al-Qiyama

10يَقُولُ الْإِنسَانُ يَوْمَئِذٍ أَيْنَ الْمَفَرُّ
bu keroogee, nita ngay, wax naan : “Fees di rawe ? ”
11كَلَّا لَا وَزَرَ
Déedéet ! Laquwaay amul de !
12إِلَىٰ رَبِّكَ يَوْمَئِذٍ الْمُسْتَقَرُّ
Bis boobu kay, dellu ca sa Boroom, rekk ay am.
13يُنَبَّأُ الْإِنسَانُ يَوْمَئِذٍ بِمَا قَدَّمَ وَأَخَّرَ
Ca la ñuy xamale nit la mu jëkka def ba ci li mu mujjoon def (cig dundam).
14بَلِ الْإِنسَانُ عَلَىٰ نَفْسِهِ بَصِيرَةٌ
Li war moo di ne nit mooy seede boppam,
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Al-Qiyama 12

Simoore Al-Qiyama Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bis boobu kay, dellu ca sa Boroom, rekk ay am.

Simoore Aaya 12/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers