Al-Qiyama · 11/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
كَلَّا لَا وَزَرَ ۝١١
Kallaa laa wazar
📖 Tekkim Wolof
Déedéet ! Laquwaay amul de !

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Simoore Al-Qiyama

9وَجُمِعَ الشَّمْسُ وَالْقَمَرُ
ñu boole jant beek weer wi,
10يَقُولُ الْإِنسَانُ يَوْمَئِذٍ أَيْنَ الْمَفَرُّ
bu keroogee, nita ngay, wax naan : “Fees di rawe ? ”
11كَلَّا لَا وَزَرَ
Déedéet ! Laquwaay amul de !
12إِلَىٰ رَبِّكَ يَوْمَئِذٍ الْمُسْتَقَرُّ
Bis boobu kay, dellu ca sa Boroom, rekk ay am.
13يُنَبَّأُ الْإِنسَانُ يَوْمَئِذٍ بِمَا قَدَّمَ وَأَخَّرَ
Ca la ñuy xamale nit la mu jëkka def ba ci li mu mujjoon def (cig dundam).
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — Al-Qiyama 11

Simoore Al-Qiyama Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Déedéet ! Laquwaay amul de !

Simoore Aaya 11/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers