Al-Qiyama · 13/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
يُنَبَّأُ الْإِنسَانُ يَوْمَئِذٍ بِمَا قَدَّمَ وَأَخَّرَ ۝١٣
Yunabba `ul insaanu yawma `izim bimaa qaddama wa akhkhar
📖 Tekkim Wolof
Ca la ñuy xamale nit la mu jëkka def ba ci li mu mujjoon def (cig dundam).

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 11-15 — Simoore Al-Qiyama

11كَلَّا لَا وَزَرَ
Déedéet ! Laquwaay amul de !
12إِلَىٰ رَبِّكَ يَوْمَئِذٍ الْمُسْتَقَرُّ
Bis boobu kay, dellu ca sa Boroom, rekk ay am.
13يُنَبَّأُ الْإِنسَانُ يَوْمَئِذٍ بِمَا قَدَّمَ وَأَخَّرَ
Ca la ñuy xamale nit la mu jëkka def ba ci li mu mujjoon def (cig dundam).
14بَلِ الْإِنسَانُ عَلَىٰ نَفْسِهِ بَصِيرَةٌ
Li war moo di ne nit mooy seede boppam,
15وَلَوْ أَلْقَىٰ مَعَاذِيرَهُ
dontela sax dafay jégalu ak miim.
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
13Aaya

Tekki — Al-Qiyama 13

Simoore Al-Qiyama Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ca la ñuy xamale nit la mu jëkka def ba…

Simoore Aaya 13/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers