An-Naba · 23/40
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naba
لَّابِثِينَ فِيهَا أَحْقَابًا ۝٢٣
Laa bitheena feehaa ahqaaba
📖 Tekkim Wolof
Danañu fa sax ay jamono yu yàgg.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 21-25 — Simoore An-Naba

21إِنَّ جَهَنَّمَ كَانَتْ مِرْصَادًا
Waajal nanu safara muy tuqlóo,
22لِّلطَّاغِينَ مَآبًا
di xala doon dekuwaayu ñu bew ña.
23لَّابِثِينَ فِيهَا أَحْقَابًا
Danañu fa sax ay jamono yu yàgg.
24لَّا يَذُوقُونَ فِيهَا بَرْدًا وَلَا شَرَابًا
Dunu fa mos ab sedd waxantumalaa ag naan,
25إِلَّا حَمِيمًا وَغَسَّاقًا
Lu dul ndox muy wañax ak lay rogaate ca seen jëmm ya
An-NabaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — An-Naba 23

Simoore An-Naba Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Danañu fa sax ay jamono yu yàgg.

Simoore Aaya 23/40 — Simoore An-Naba النبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naba Dégg, Simoore An-Naba Tekki, Simoore An-Naba mp3, Simoore An-Naba pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers