An-Naba · 25/40
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naba
إِلَّا حَمِيمًا وَغَسَّاقًا ۝٢٥
Illa hamee maw-wa ghas saaqa
📖 Tekkim Wolof
Lu dul ndox muy wañax ak lay rogaate ca seen jëmm ya

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-27 — Simoore An-Naba

23لَّابِثِينَ فِيهَا أَحْقَابًا
Danañu fa sax ay jamono yu yàgg.
24لَّا يَذُوقُونَ فِيهَا بَرْدًا وَلَا شَرَابًا
Dunu fa mos ab sedd waxantumalaa ag naan,
25إِلَّا حَمِيمًا وَغَسَّاقًا
Lu dul ndox muy wañax ak lay rogaate ca seen jëmm ya
26جَزَاءً وِفَاقًا
muy pey gu témbóo.
27إِنَّهُمْ كَانُوا لَا يَرْجُونَ حِسَابًا
Ñoom dañoo foogoon ne duñu leen màndaxe,
An-NabaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — An-Naba 25

Simoore An-Naba Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lu dul ndox muy wañax ak lay rogaate ca seen…

Simoore Aaya 25/40 — Simoore An-Naba النبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naba Dégg, Simoore An-Naba Tekki, Simoore An-Naba mp3, Simoore An-Naba pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers