An-Naba · 6/40
Tekki Waxtaan — An-Naba
أَلَمْ نَجْعَلِ الْأَرْضَ مِهَادًا ۝٦
Alam naj`alil arda mihaa da
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax du Nun Noo def suuf si mu di laltaay ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 4-8 — An-Naba

4كَلَّا سَيَعْلَمُونَ
Mukk ! danañu xala xam.
5ثُمَّ كَلَّا سَيَعْلَمُونَ
Déedéet kay ! Danañu xala xam.
6أَلَمْ نَجْعَلِ الْأَرْضَ مِهَادًا
Moo ndax du Nun Noo def suuf si mu di laltaay ?
7وَالْجِبَالَ أَوْتَادًا
ak tundi doj yi ñu di ay dott ?
8وَخَلَقْنَاكُمْ أَزْوَاجًا
Nu bind leen ngeen di ay tóllent,
An-NabaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — An-Naba 6

Simoore An-Naba Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax du Nun Noo def suuf si mu di…

Simoore Aaya 6/40 — An-Naba النبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naba Dégg, An-Naba Tekki, An-Naba mp3, An-Naba pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers