An-Nazi'at · 45/46
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nazi'at
إِنَّمَا أَنتَ مُنذِرُ مَن يَخْشَاهَا ۝٤٥
Innamaaa anta munziru maiy yakshaahaa
📖 Tekkim Wolof
Yaw nag ab xuppekat doŋŋ nga ngir ña ko ragal.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 43-46 — Simoore An-Nazi'at

43فِيمَ أَنتَ مِن ذِكْرَاهَا
Ana ban xam-xam nga ci am ngir tontu leen ?
44إِلَىٰ رَبِّكَ مُنتَهَاهَا
Ab yemukaayam sa Boroom rekk ko xam.
45إِنَّمَا أَنتَ مُنذِرُ مَن يَخْشَاهَا
Yaw nag ab xuppekat doŋŋ nga ngir ña ko ragal.
46كَأَنَّهُمْ يَوْمَ يَرَوْنَهَا لَمْ يَلْبَثُوا إِلَّا عَشِيَّةً أَوْ ضُحَاهَا
Bis bu ñu ko gisee, dafay mel ne seen dund gépp genn ngoon la woon walla yoor-yoor.
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — An-Nazi'at 45

Simoore An-Nazi'at Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yaw nag ab xuppekat doŋŋ nga ngir ña ko ragal.

Simoore Aaya 45/46 — Simoore An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nazi'at Dégg, Simoore An-Nazi'at Tekki, Simoore An-Nazi'at mp3, Simoore An-Nazi'at pdf. Aaya 43–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers