An-Nazi'at · 46/46
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nazi'at
كَأَنَّهُمْ يَوْمَ يَرَوْنَهَا لَمْ يَلْبَثُوا إِلَّا عَشِيَّةً أَوْ ضُحَاهَا ۝٤٦
Ka annahum Yawma yarawnahaa lam yalbasooo illaa `ashiyyatan aw duhaahaa
📖 Tekkim Wolof
Bis bu ñu ko gisee, dafay mel ne seen dund gépp genn ngoon la woon walla yoor-yoor.

🎧 Dégg


📜 Aaya 44-46 — Simoore An-Nazi'at

44إِلَىٰ رَبِّكَ مُنتَهَاهَا
Ab yemukaayam sa Boroom rekk ko xam.
45إِنَّمَا أَنتَ مُنذِرُ مَن يَخْشَاهَا
Yaw nag ab xuppekat doŋŋ nga ngir ña ko ragal.
46كَأَنَّهُمْ يَوْمَ يَرَوْنَهَا لَمْ يَلْبَثُوا إِلَّا عَشِيَّةً أَوْ ضُحَاهَا
Bis bu ñu ko gisee, dafay mel ne seen dund gépp genn ngoon la woon walla yoor-yoor.
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
46Aaya

Tekki — An-Nazi'at 46

Simoore An-Nazi'at Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bis bu ñu ko gisee, dafay mel ne seen dund…

Simoore Aaya 46/46 — Simoore An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nazi'at Dégg, Simoore An-Nazi'at Tekki, Simoore An-Nazi'at mp3, Simoore An-Nazi'at pdf. Aaya 44–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers