An-Nazi'at · 44/46
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nazi'at
إِلَىٰ رَبِّكَ مُنتَهَاهَا ۝٤٤
Ilaa Rabbika muntahaa haa
📖 Tekkim Wolof
Ab yemukaayam sa Boroom rekk ko xam.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 42-46 — Simoore An-Nazi'at

42يَسْأَلُونَكَ عَنِ السَّاعَةِ أَيَّانَ مُرْسَاهَا
Ña nga lay laaj bis pénc ba : “Kañ lay teeral”
43فِيمَ أَنتَ مِن ذِكْرَاهَا
Ana ban xam-xam nga ci am ngir tontu leen ?
44إِلَىٰ رَبِّكَ مُنتَهَاهَا
Ab yemukaayam sa Boroom rekk ko xam.
45إِنَّمَا أَنتَ مُنذِرُ مَن يَخْشَاهَا
Yaw nag ab xuppekat doŋŋ nga ngir ña ko ragal.
46كَأَنَّهُمْ يَوْمَ يَرَوْنَهَا لَمْ يَلْبَثُوا إِلَّا عَشِيَّةً أَوْ ضُحَاهَا
Bis bu ñu ko gisee, dafay mel ne seen dund gépp genn ngoon la woon walla yoor-yoor.
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
44Aaya

Tekki — An-Nazi'at 44

Simoore An-Nazi'at Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ab yemukaayam sa Boroom rekk ko xam.

Simoore Aaya 44/46 — Simoore An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nazi'at Dégg, Simoore An-Nazi'at Tekki, Simoore An-Nazi'at mp3, Simoore An-Nazi'at pdf. Aaya 42–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers