Al-Anfal · 20/75
Tekki Waxtaan — Al-Anfal
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا أَطِيعُوا اللَّهَ وَرَسُولَهُ وَلَا تَوَلَّوْا عَنْهُ وَأَنتُمْ تَسْمَعُونَ ۝٢٠
Yaaa aiyuhal lazeena aamanoo atee`ul laaha wa Rasoolahoo wa laa tawallaw `anhu wa antum tasm`oon
📖 Tekkim Wolof
Éy yéen ñi gëm ñi ! Nangeen topp Yàlla ak ub Yonentam, buleen ko dëddu te fekk dégg ngeen li muy wax.
🎧 Dégg

📜 Aaya 18-22 — Al-Anfal

18ذَٰلِكُمْ وَأَنَّ اللَّهَ مُوهِنُ كَيْدِ الْكَافِرِينَ
Loolu la dëggal ci yéen te [xamleen ne] Kuy doyadal pexey yéefar yi la [Moom Yàlla].
19إِن تَسْتَفْتِحُوا فَقَدْ جَاءَكُمُ الْفَتْحُ ۖ وَإِن تَنتَهُوا فَهُوَ خَيْرٌ لَّكُمْ ۖ وَإِن تَعُودُوا نَعُدْ وَلَن تُغْنِيَ عَنكُمْ فِئَتُكُمْ شَيْئًا وَلَوْ كَثُرَتْ وَأَنَّ اللَّهَ مَعَ الْمُؤْمِنِينَ
Ndegam dangeen di sàkku lu ngeen di àttewoo [yéen yéefar yi], ab àtte dikkal na leen ba noppi. Bu ngeen bàyyee [la ngeen nekkoon cig kéefar], mooy gën ci yéen. Bu ngeen delloo [ca la ngeen nekke woon], Nu dellu [ci di jox Yonent bi ndimbal], te kon seeni mbooloo duleen jariñ dara, doonte dafa bari lool. Yàlla nag Mook jullit yee ànd.
20يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا أَطِيعُوا اللَّهَ وَرَسُولَهُ وَلَا تَوَلَّوْا عَنْهُ وَأَنتُمْ تَسْمَعُونَ
Éy yéen ñi gëm ñi ! Nangeen topp Yàlla ak ub Yonentam, buleen ko dëddu te fekk dégg ngeen li muy wax.
21وَلَا تَكُونُوا كَالَّذِينَ قَالُوا سَمِعْنَا وَهُمْ لَا يَسْمَعُونَ
Buleen mel ni ñiy wax : “Dégg nanu ”, te fekk dégguñu woon dara.
22۞ إِنَّ شَرَّ الدَّوَابِّ عِندَ اللَّهِ الصُّمُّ الْبُكْمُ الَّذِينَ لَا يَعْقِلُونَ
Li gën a yées ci bindeef yi ca Yàlla, mooy ñi tëx, luu te bañ a xel-lu.
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
20Aaya

Tekki — Al-Anfal 20

Simoore Al-Anfal Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Éy yéen ñi gëm ñi ! Nangeen topp Yàlla ak…

Simoore Aaya 20/75 — Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anfal Dégg, Al-Anfal Tekki, Al-Anfal mp3, Al-Anfal pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers