Abasa · 24/42
Tekki Waxtaan — Abasa
فَلْيَنظُرِ الْإِنسَانُ إِلَىٰ طَعَامِهِ ۝٢٤
Falyanzuril insanu ilaa ta-amih
📖 Tekkim Wolof
Na nit di xool ci aw ñamam lekkam :

🎧 Dégg


📜 Aaya 22-26 — Abasa

22ثُمَّ إِذَا شَاءَ أَنشَرَهُ
te saa su Ko soobee mu dekkalaat Ko.
23كَلَّا لَمَّا يَقْضِ مَا أَمَرَهُ
Déedéet ! [Nit] moom matalul mukk la nu ko digëloon.
24فَلْيَنظُرِ الْإِنسَانُ إِلَىٰ طَعَامِهِ
Na nit di xool ci aw ñamam lekkam :
25أَنَّا صَبَبْنَا الْمَاءَ صَبًّا
Nun noo sotti ndox mu dottiku,
26ثُمَّ شَقَقْنَا الْأَرْضَ شَقًّا
ba noppi Nu xar suuf mu fett
AbasaFihi Alxuraan
42Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — Abasa 24

Simoore Abasa Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Na nit di xool ci aw ñamam lekkam :

Simoore Aaya 24/42 — Abasa عبس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Abasa Dégg, Abasa Tekki, Abasa mp3, Abasa pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers