Abasa · 25/42
Tekki Waxtaan — Simoore Abasa
أَنَّا صَبَبْنَا الْمَاءَ صَبًّا ۝٢٥
Anna sabab nalmaa-a sabba
📖 Tekkim Wolof
Nun noo sotti ndox mu dottiku,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 23-27 — Simoore Abasa

23كَلَّا لَمَّا يَقْضِ مَا أَمَرَهُ
Déedéet ! [Nit] moom matalul mukk la nu ko digëloon.
24فَلْيَنظُرِ الْإِنسَانُ إِلَىٰ طَعَامِهِ
Na nit di xool ci aw ñamam lekkam :
25أَنَّا صَبَبْنَا الْمَاءَ صَبًّا
Nun noo sotti ndox mu dottiku,
26ثُمَّ شَقَقْنَا الْأَرْضَ شَقًّا
ba noppi Nu xar suuf mu fett
27فَأَنبَتْنَا فِيهَا حَبًّا
nu saxal ci ay kembu,
AbasaFihi Alxuraan
42Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Abasa 25

Simoore Abasa Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun noo sotti ndox mu dottiku,

Simoore Aaya 25/42 — Simoore Abasa عبس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Abasa Dégg, Simoore Abasa Tekki, Simoore Abasa mp3, Simoore Abasa pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers