Al-Infitar · 14/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Infitar
وَإِنَّ الْفُجَّارَ لَفِي جَحِيمٍ ۝١٤
Wa innal fujjaara lafee jaheem
📖 Tekkim Wolof
te itam kàccoor ya ñoom, ña nga ca biir safara jahiim

🎧 Dégg


📜 Aaya 12-16 — Simoore Al-Infitar

12يَعْلَمُونَ مَا تَفْعَلُونَ
yuy xam li ngeen di def.
13إِنَّ الْأَبْرَارَ لَفِي نَعِيمٍ
Ñu baax ñaa ngi ca biir àjjanay xéewal,
14وَإِنَّ الْفُجَّارَ لَفِي جَحِيمٍ
te itam kàccoor ya ñoom, ña nga ca biir safara jahiim
15يَصْلَوْنَهَا يَوْمَ الدِّينِ
danañu ca xoyomoo, bu bis Pénc baa
16وَمَا هُمْ عَنْهَا بِغَائِبِينَ
te ñoom manuñu koo wuute.
Al-InfitarFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Al-Infitar 14

Simoore Al-Infitar Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te itam kàccoor ya ñoom, ña nga ca biir safara…

Simoore Aaya 14/19 — Simoore Al-Infitar الإنفطار (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Infitar Dégg, Simoore Al-Infitar Tekki, Simoore Al-Infitar mp3, Simoore Al-Infitar pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers