Al-Infitar · 15/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Infitar
يَصْلَوْنَهَا يَوْمَ الدِّينِ ۝١٥
Yaslawnahaa Yawmad Deen
📖 Tekkim Wolof
danañu ca xoyomoo, bu bis Pénc baa

🎧 Dégg


📜 Aaya 13-17 — Simoore Al-Infitar

13إِنَّ الْأَبْرَارَ لَفِي نَعِيمٍ
Ñu baax ñaa ngi ca biir àjjanay xéewal,
14وَإِنَّ الْفُجَّارَ لَفِي جَحِيمٍ
te itam kàccoor ya ñoom, ña nga ca biir safara jahiim
15يَصْلَوْنَهَا يَوْمَ الدِّينِ
danañu ca xoyomoo, bu bis Pénc baa
16وَمَا هُمْ عَنْهَا بِغَائِبِينَ
te ñoom manuñu koo wuute.
17وَمَا أَدْرَاكَ مَا يَوْمُ الدِّينِ
Ana lu lay xamal luy bis Pénc ?
Al-InfitarFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — Al-Infitar 15

Simoore Al-Infitar Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : danañu ca xoyomoo, bu bis Pénc baa

Simoore Aaya 15/19 — Simoore Al-Infitar الإنفطار (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Infitar Dégg, Simoore Al-Infitar Tekki, Simoore Al-Infitar mp3, Simoore Al-Infitar pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers