Al-Mutaffifin · 4/36
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mutaffifin
أَلَا يَظُنُّ أُولَٰئِكَ أَنَّهُم مَّبْعُوثُونَ ۝٤
Alaa yazunnu ulaaa`ika annahum mab`oosoon
📖 Tekkim Wolof
Xanaa ñoom dañoo jàpput ne dees na leen dekkilaat (ginnaaw dee),

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 2-6 — Simoore Al-Mutaffifin

2الَّذِينَ إِذَا اكْتَالُوا عَلَى النَّاسِ يَسْتَوْفُونَ
ñay natt peese di ëppal lay jëm ca ñoom,
3وَإِذَا كَالُوهُمْ أَو وَّزَنُوهُمْ يُخْسِرُونَ
te su ñuy nattal keneen, wàññi ko.
4أَلَا يَظُنُّ أُولَٰئِكَ أَنَّهُم مَّبْعُوثُونَ
Xanaa ñoom dañoo jàpput ne dees na leen dekkilaat (ginnaaw dee),
5لِيَوْمٍ عَظِيمٍ
ca bis bu ñàng,
6يَوْمَ يَقُومُ النَّاسُ لِرَبِّ الْعَالَمِينَ
bis ba nit ña di taxaw ci kanam Boroom Àddina si yépp ?
Al-MutaffifinFihi Alxuraan
36Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-Mutaffifin 4

Simoore Al-Mutaffifin Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xanaa ñoom dañoo jàpput ne dees na leen dekkilaat (ginnaaw…

Simoore Aaya 4/36 — Simoore Al-Mutaffifin المطففين (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mutaffifin Dégg, Simoore Al-Mutaffifin Tekki, Simoore Al-Mutaffifin mp3, Simoore Al-Mutaffifin pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers