Al-Buruj · 12/22
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Buruj
إِنَّ بَطْشَ رَبِّكَ لَشَدِيدٌ ۝١٢
Inna batsha Rabbika lashadeed
📖 Tekkim Wolof
Sa fayug boroom lu tar la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Simoore Al-Buruj

10إِنَّ الَّذِينَ فَتَنُوا الْمُؤْمِنِينَ وَالْمُؤْمِنَاتِ ثُمَّ لَمْ يَتُوبُوا فَلَهُمْ عَذَابُ جَهَنَّمَ وَلَهُمْ عَذَابُ الْحَرِيقِ
Ña daan fitnaal jullit yu góor yaak yu jigéen ya, te tubu ñu ko, dananu am mbugëlum Jahanama ñu di leen ca lakk. (ca safaraam wa)
11إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ لَهُمْ جَنَّاتٌ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ۚ ذَٰلِكَ الْفَوْزُ الْكَبِيرُ
Ña gëmoon te daan jëf yiw am nañu ay Àjjana yu ay dex di daw ci suufam. Loolu moo di texe gu mag ga.
12إِنَّ بَطْشَ رَبِّكَ لَشَدِيدٌ
Sa fayug boroom lu tar la.
13إِنَّهُ هُوَ يُبْدِئُ وَيُعِيدُ
Moom mooy, sos bindeef yi, te mooleen di dekkilaat.
14وَهُوَ الْغَفُورُ الْوَدُودُ
Te moom moo di Jéggëlaakoon bi, di soppi lépp,
Al-BurujFihi Alxuraan
22Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Al-Buruj 12

Simoore Al-Buruj Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sa fayug boroom lu tar la.

Simoore Aaya 12/22 — Simoore Al-Buruj البروج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Buruj Dégg, Simoore Al-Buruj Tekki, Simoore Al-Buruj mp3, Simoore Al-Buruj pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers