Al-Buruj · 13/22
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Buruj
إِنَّهُ هُوَ يُبْدِئُ وَيُعِيدُ ۝١٣
Innahoo Huwa yubdi`u wa yu`eed
📖 Tekkim Wolof
Moom mooy, sos bindeef yi, te mooleen di dekkilaat.

🎧 Dégg


📜 Aaya 11-15 — Simoore Al-Buruj

11إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ لَهُمْ جَنَّاتٌ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ۚ ذَٰلِكَ الْفَوْزُ الْكَبِيرُ
Ña gëmoon te daan jëf yiw am nañu ay Àjjana yu ay dex di daw ci suufam. Loolu moo di texe gu mag ga.
12إِنَّ بَطْشَ رَبِّكَ لَشَدِيدٌ
Sa fayug boroom lu tar la.
13إِنَّهُ هُوَ يُبْدِئُ وَيُعِيدُ
Moom mooy, sos bindeef yi, te mooleen di dekkilaat.
14وَهُوَ الْغَفُورُ الْوَدُودُ
Te moom moo di Jéggëlaakoon bi, di soppi lépp,
15ذُو الْعَرْشِ الْمَجِيدُ
Mooy boroom Gàngunaay gu Màgg ga (Aras),
Al-BurujFihi Alxuraan
22Aaya
MeccanRevelation
13Aaya

Tekki — Al-Buruj 13

Simoore Al-Buruj Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moom mooy, sos bindeef yi, te mooleen di dekkilaat.

Simoore Aaya 13/22 — Simoore Al-Buruj البروج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Buruj Dégg, Simoore Al-Buruj Tekki, Simoore Al-Buruj mp3, Simoore Al-Buruj pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers