Al-Fajr · 22/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Fajr
وَجَاءَ رَبُّكَ وَالْمَلَكُ صَفًّا صَفًّا ۝٢٢
Wa jaaa`a Rabbuka wal malaku saffan saffaa
📖 Tekkim Wolof
sa Boroom dikk ak malaaka ya, def ay sàppey sàppe,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 20-24 — Simoore Al-Fajr

20وَتُحِبُّونَ الْمَالَ حُبًّا جَمًّا
te da ngeen bëgg alal bëgg gu tar.
21كَلَّا إِذَا دُكَّتِ الْأَرْضُ دَكًّا دَكًّا
(Bàyyileen xel) ! saa su nu walee suuf si ba mu di pëndax,
22وَجَاءَ رَبُّكَ وَالْمَلَكُ صَفًّا صَفًّا
sa Boroom dikk ak malaaka ya, def ay sàppey sàppe,
23وَجِيءَ يَوْمَئِذٍ بِجَهَنَّمَ ۚ يَوْمَئِذٍ يَتَذَكَّرُ الْإِنسَانُ وَأَنَّىٰ لَهُ الذِّكْرَىٰ
bu keroogee, danuy indi Safarey jahanama ; bu keroogee it, nit dana fàttaliku. Waaye damaa xamut lu ko fàttaliku ga di jariñ ?
24يَقُولُ يَا لَيْتَنِي قَدَّمْتُ لِحَيَاتِي
Muy wax naan : “Aka neexoon ! Ca ba muy dundu ma defoon lu baax !
Al-FajrFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — Al-Fajr 22

Simoore Al-Fajr Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : sa Boroom dikk ak malaaka ya, def ay sàppey sàppe,

Simoore Aaya 22/30 — Simoore Al-Fajr الفجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Fajr Dégg, Simoore Al-Fajr Tekki, Simoore Al-Fajr mp3, Simoore Al-Fajr pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers