Al-Fajr · 21/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Fajr
كَلَّا إِذَا دُكَّتِ الْأَرْضُ دَكًّا دَكًّا ۝٢١
Kallaaa izaaa dukkatil ardu dakkan dakka
📖 Tekkim Wolof
(Bàyyileen xel) ! saa su nu walee suuf si ba mu di pëndax,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 19-23 — Simoore Al-Fajr

19وَتَأْكُلُونَ التُّرَاثَ أَكْلًا لَّمًّا
te ngeen di lekk alal ndono lekkiin wu ñaaw,
20وَتُحِبُّونَ الْمَالَ حُبًّا جَمًّا
te da ngeen bëgg alal bëgg gu tar.
21كَلَّا إِذَا دُكَّتِ الْأَرْضُ دَكًّا دَكًّا
(Bàyyileen xel) ! saa su nu walee suuf si ba mu di pëndax,
22وَجَاءَ رَبُّكَ وَالْمَلَكُ صَفًّا صَفًّا
sa Boroom dikk ak malaaka ya, def ay sàppey sàppe,
23وَجِيءَ يَوْمَئِذٍ بِجَهَنَّمَ ۚ يَوْمَئِذٍ يَتَذَكَّرُ الْإِنسَانُ وَأَنَّىٰ لَهُ الذِّكْرَىٰ
bu keroogee, danuy indi Safarey jahanama ; bu keroogee it, nit dana fàttaliku. Waaye damaa xamut lu ko fàttaliku ga di jariñ ?
Al-FajrFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — Al-Fajr 21

Simoore Al-Fajr Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (Bàyyileen xel) ! saa su nu walee suuf si ba…

Simoore Aaya 21/30 — Simoore Al-Fajr الفجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Fajr Dégg, Simoore Al-Fajr Tekki, Simoore Al-Fajr mp3, Simoore Al-Fajr pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers