Al-Fajr · 23/30
Tekki Waxtaan — Al-Fajr
وَجِيءَ يَوْمَئِذٍ بِجَهَنَّمَ ۚ يَوْمَئِذٍ يَتَذَكَّرُ الْإِنسَانُ وَأَنَّىٰ لَهُ الذِّكْرَىٰ ٢٣
Transliteration
Wa jeee`a yawma`izim bi jahannnam; Yawma `iziny yatazakkarul insaanu wa annaa lahuz zikraa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
bu keroogee, danuy indi Safarey jahanama ; bu keroogee it, nit dana fàttaliku. Waaye damaa xamut lu ko fàttaliku ga di jariñ ?
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 21-25 — Al-Fajr
21كَلَّا إِذَا دُكَّتِ الْأَرْضُ دَكًّا دَكًّا
(Bàyyileen xel) ! saa su nu walee suuf si ba mu di pëndax,
22وَجَاءَ رَبُّكَ وَالْمَلَكُ صَفًّا صَفًّا
sa Boroom dikk ak malaaka ya, def ay sàppey sàppe,
23وَجِيءَ يَوْمَئِذٍ بِجَهَنَّمَ ۚ يَوْمَئِذٍ يَتَذَكَّرُ الْإِنسَانُ وَأَنَّىٰ لَهُ الذِّكْرَىٰ
bu keroogee, danuy indi Safarey jahanama ; bu keroogee it, nit dana fàttaliku. Waaye damaa xamut lu ko fàttaliku ga di jariñ ?
24يَقُولُ يَا لَيْتَنِي قَدَّمْتُ لِحَيَاتِي
Muy wax naan : “Aka neexoon ! Ca ba muy dundu ma defoon lu baax !
25فَيَوْمَئِذٍ لَّا يُعَذِّبُ عَذَابَهُ أَحَدٌ
Bu keroogee, mbugël ma deefu ko mbugël kenn,
Al-FajrFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
23Aaya
Tekki — Al-Fajr 23
Simoore Al-Fajr Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : bu keroogee, danuy indi Safarey jahanama ; bu keroogee it,…Simoore Aaya 23/30 — Al-Fajr الفجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Fajr Dégg, Al-Fajr Tekki, Al-Fajr mp3, Al-Fajr pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








