Al-Layl · 18/21
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Layl
الَّذِي يُؤْتِي مَالَهُ يَتَزَكَّىٰ ۝١٨
Allazee yu`tee maalahoo yatazakkaa
📖 Tekkim Wolof
kay joxe alalam ngir selal

🎧 Dégg


📜 Aaya 16-20 — Simoore Al-Layl

16الَّذِي كَذَّبَ وَتَوَلَّىٰ
kay weddi tey dumóoyu ;
17وَسَيُجَنَّبُهَا الْأَتْقَى
dees na ko soril ñu ragal Yàlla ña,
18الَّذِي يُؤْتِي مَالَهُ يَتَزَكَّىٰ
kay joxe alalam ngir selal
19وَمَا لِأَحَدٍ عِندَهُ مِن نِّعْمَةٍ تُجْزَىٰ
te amul genn xéewal gu ñuy faye kenn ca moom,
20إِلَّا ابْتِغَاءَ وَجْهِ رَبِّهِ الْأَعْلَىٰ
Lu dul sàkku jëmm Boroomam ja gëna Kawe.
Al-LaylFihi Alxuraan
21Aaya
MeccanRevelation
18Aaya

Tekki — Al-Layl 18

Simoore Al-Layl Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : kay joxe alalam ngir selal

Simoore Aaya 18/21 — Simoore Al-Layl الليل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Layl Dégg, Simoore Al-Layl Tekki, Simoore Al-Layl mp3, Simoore Al-Layl pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers