Yunus · 46/109
Tekki Waxtaan — Yunus
وَإِمَّا نُرِيَنَّكَ بَعْضَ الَّذِي نَعِدُهُمْ أَوْ نَتَوَفَّيَنَّكَ فَإِلَيْنَا مَرْجِعُهُمْ ثُمَّ اللَّهُ شَهِيدٌ عَلَىٰ مَا يَفْعَلُونَ ٤٦
Transliteration
Wa imma nuriyannaka ba`dal lazee na`iduhum aw natawaffayannaka fa ilainaa marji`uhum summal laahu shaheedun `alaa maa yaf`aloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te Nu won la dara ca la Nu leen tëkkoo, walla Nu rey la [Yaw Muhammad], lu mu ca doon seenug delluwaay ci Nun la jëmsi. Ba noppi, Yàlla nekk di seede ca lañu daan def.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 44-48 — Yunus
44إِنَّ اللَّهَ لَا يَظْلِمُ النَّاسَ شَيْئًا وَلَٰكِنَّ النَّاسَ أَنفُسَهُمْ يَظْلِمُونَ
Yàlla nag du tooñ nit ci dara, waaye nit ñi ñooy tooñ seen bopp.
45وَيَوْمَ يَحْشُرُهُمْ كَأَن لَّمْ يَلْبَثُوا إِلَّا سَاعَةً مِّنَ النَّهَارِ يَتَعَارَفُونَ بَيْنَهُمْ ۚ قَدْ خَسِرَ الَّذِينَ كَذَّبُوا بِلِقَاءِ اللَّهِ وَمَا كَانُوا مُهْتَدِينَ
Bis bu leen Yàlla dajalee, dana mel ni tooguñu [ca seeni bàmmeel] lu dul diirub benn waxtu cig bëccëg, ñuy xamante. Te ña weddi woon ne dajeek Yàlla dana am, yàqule nañu ndax nekkuñu woon ñu gindiku.
46وَإِمَّا نُرِيَنَّكَ بَعْضَ الَّذِي نَعِدُهُمْ أَوْ نَتَوَفَّيَنَّكَ فَإِلَيْنَا مَرْجِعُهُمْ ثُمَّ اللَّهُ شَهِيدٌ عَلَىٰ مَا يَفْعَلُونَ
Te Nu won la dara ca la Nu leen tëkkoo, walla Nu rey la [Yaw Muhammad], lu mu ca doon seenug delluwaay ci Nun la jëmsi. Ba noppi, Yàlla nekk di seede ca lañu daan def.
47وَلِكُلِّ أُمَّةٍ رَّسُولٌ ۖ فَإِذَا جَاءَ رَسُولُهُمْ قُضِيَ بَيْنَهُم بِالْقِسْطِ وَهُمْ لَا يُظْلَمُونَ
Xeet wu nekk am na ab Yonent. Bu seenub Yonent agsee rekk, dees na àtte seen diggante ci maandute, te kenn duleen tooñ.
48وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْوَعْدُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ñu naan : “Boobu dig kañ lay doon, ndegam ñu dëggu ngeen” ?
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
46Aaya
Tekki — Yunus 46
Simoore Yunus Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te Nu won la dara ca la Nu leen tëkkoo,…Simoore Aaya 46/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








