Yunus · 62/109
Tekki Waxtaan — Simoore Yunus
أَلَا إِنَّ أَوْلِيَاءَ اللَّهِ لَا خَوْفٌ عَلَيْهِمْ وَلَا هُمْ يَحْزَنُونَ ٦٢
Transliteration
Alaa innaa awliyaaa`al laahi laa khawfun `alaihim wa laa hum yahzanoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ca dëgg-dëgg, ña féeteek Yàlla duñu gis lu ñu ragal, duñu gis njàqare,
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 60-64 — Simoore Yunus
60وَمَا ظَنُّ الَّذِينَ يَفْتَرُونَ عَلَى اللَّهِ الْكَذِبَ يَوْمَ الْقِيَامَةِ ۗ إِنَّ اللَّهَ لَذُو فَضْلٍ عَلَى النَّاسِ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَشْكُرُونَ
Ana lan mooy njortul ñiy duural Yàlla ay fen Bis-pénc ba ? - Dafa dëggu ne Yàlla xéewalaakoon la, waaye li ëpp ci ñoom duñu gërêm [Yàlla].
61وَمَا تَكُونُ فِي شَأْنٍ وَمَا تَتْلُو مِنْهُ مِن قُرْآنٍ وَلَا تَعْمَلُونَ مِنْ عَمَلٍ إِلَّا كُنَّا عَلَيْكُمْ شُهُودًا إِذْ تُفِيضُونَ فِيهِ ۚ وَمَا يَعْزُبُ عَن رَّبِّكَ مِن مِّثْقَالِ ذَرَّةٍ فِي الْأَرْضِ وَلَا فِي السَّمَاءِ وَلَا أَصْغَرَ مِن ذَٰلِكَ وَلَا أَكْبَرَ إِلَّا فِي كِتَابٍ مُّبِينٍ
Doo nekk ci menn mbir, walla ngay jàng dara ci Alxuraan, walla ngeen def jenn jëf te Nekkunu ca seede ba ngeen cay duggu. Te lu toll ni pepp su tuuti du rëcc sa Boroom, du ci suuf si, du ci asamaan yi ; te amul lu ko gën a tuuti walla lu ko gën a rëy lu dul ne mi ngi ci ab téere bu bir.
62أَلَا إِنَّ أَوْلِيَاءَ اللَّهِ لَا خَوْفٌ عَلَيْهِمْ وَلَا هُمْ يَحْزَنُونَ
Ca dëgg-dëgg, ña féeteek Yàlla duñu gis lu ñu ragal, duñu gis njàqare,
63الَّذِينَ آمَنُوا وَكَانُوا يَتَّقُونَ
Ña gëm te ragal Yàlla,
64لَهُمُ الْبُشْرَىٰ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَفِي الْآخِرَةِ ۚ لَا تَبْدِيلَ لِكَلِمَاتِ اللَّهِ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الْفَوْزُ الْعَظِيمُ
Am nañu mbégte ci dundug àddina ak ca àllaaxira. - Soppeeku du am ciy kàddu Yàlla -. Loolu mooy texe gu mag ga !
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
62Aaya
Tekki — Yunus 62
Simoore Yunus Aaya 62 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ca dëgg-dëgg, ña féeteek Yàlla duñu gis lu ñu ragal,…Simoore Aaya 62/109 — Simoore Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yunus Dégg, Simoore Yunus Tekki, Simoore Yunus mp3, Simoore Yunus pdf. Aaya 60–64. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Yunus
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Friday, October 2, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


