Hud · 81/123
Tekki Waxtaan — Hud
قَالُوا يَا لُوطُ إِنَّا رُسُلُ رَبِّكَ لَن يَصِلُوا إِلَيْكَ ۖ فَأَسْرِ بِأَهْلِكَ بِقِطْعٍ مِّنَ اللَّيْلِ وَلَا يَلْتَفِتْ مِنكُمْ أَحَدٌ إِلَّا امْرَأَتَكَ ۖ إِنَّهُ مُصِيبُهَا مَا أَصَابَهُمْ ۚ إِنَّ مَوْعِدَهُمُ الصُّبْحُ ۚ أَلَيْسَ الصُّبْحُ بِقَرِيبٍ ٨١
Transliteration
Qaaloo yaa Lootu innaa Rusulu Rabbika lai yasiloo ilaika fa asri bi ahlika biqit `im minal laili wa laa yaltafit minkum ahadun illam ra ataka innahoo museebuhaa maaa asaabahum; inna maw`i dahumus subh; alaisas subhu biqareeb
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne ko : “Éy Lóot, nun ay ndawi sa Boroom lanu. Duñu agsi ci yaw. Nanga rañaan yaak sa njaboot ci biir guddi gi. Te bu kenn ci ñoom gestu. Ba mu des sa soxna ndax moom lu leen dal dana ko dal. Seenub àpp ëllëg rekk la. Moo ndax suba jigeñul ? ”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 79-83 — Hud
79قَالُوا لَقَدْ عَلِمْتَ مَا لَنَا فِي بَنَاتِكَ مِنْ حَقٍّ وَإِنَّكَ لَتَعْلَمُ مَا نُرِيدُ
Ñu ne ko : Xam nga ne amuñu soxla ci sa doom yu jigéen yi. Te yaw xam nga xéll li nu bëgg”.
80قَالَ لَوْ أَنَّ لِي بِكُمْ قُوَّةً أَوْ آوِي إِلَىٰ رُكْنٍ شَدِيدٍ
Mu ne : “[Cëy !] su ma amoon dooley dal ci seen kaw ! mbaa ma mën a tàbbi ci giir gu am doole ! ”
81قَالُوا يَا لُوطُ إِنَّا رُسُلُ رَبِّكَ لَن يَصِلُوا إِلَيْكَ ۖ فَأَسْرِ بِأَهْلِكَ بِقِطْعٍ مِّنَ اللَّيْلِ وَلَا يَلْتَفِتْ مِنكُمْ أَحَدٌ إِلَّا امْرَأَتَكَ ۖ إِنَّهُ مُصِيبُهَا مَا أَصَابَهُمْ ۚ إِنَّ مَوْعِدَهُمُ الصُّبْحُ ۚ أَلَيْسَ الصُّبْحُ بِقَرِيبٍ
Ñu ne ko : “Éy Lóot, nun ay ndawi sa Boroom lanu. Duñu agsi ci yaw. Nanga rañaan yaak sa njaboot ci biir guddi gi. Te bu kenn ci ñoom gestu. Ba mu des sa soxna ndax moom lu leen dal dana ko dal. Seenub àpp ëllëg rekk la. Moo ndax suba jigeñul ? ”
82فَلَمَّا جَاءَ أَمْرُنَا جَعَلْنَا عَالِيَهَا سَافِلَهَا وَأَمْطَرْنَا عَلَيْهَا حِجَارَةً مِّن سِجِّيلٍ مَّنضُودٍ
Ba Sunu dogal agsee, wëlbati Nanu [dëkk ba], la féete woon kaw féete suuf, Nu sotti ca kawam tawu xeer yu jóge Sijjiil [Safara] ay doj yu ñu toftale,
83مُّسَوَّمَةً عِندَ رَبِّكَ ۖ وَمَا هِيَ مِنَ الظَّالِمِينَ بِبَعِيدٍ
yu ñu màndargaal ca sa Boroom. Te dëkk boobu soreewul ag way-tooñ ya [ya ca Màkka].
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
81Aaya
Tekki — Hud 81
Simoore Hud Aaya 81 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne ko : “Éy Lóot, nun ay ndawi sa…Simoore Aaya 81/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 79–83. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








