Hud · 86/123
Tekki Waxtaan — Hud
بَقِيَّتُ اللَّهِ خَيْرٌ لَّكُمْ إِن كُنتُم مُّؤْمِنِينَ ۚ وَمَا أَنَا عَلَيْكُم بِحَفِيظٍ ٨٦
Transliteration
Baqiyyatul laahi khairul lakum in kuntum mu`mineen; wa maa ana `alaikum bihafeez
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Wërsëgu Yàlla moo gën ci yéen ndegam ñu gëm ngeen ! Te nekkuma di ku leen di warlul kiiraay”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 84-88 — Hud
84۞ وَإِلَىٰ مَدْيَنَ أَخَاهُمْ شُعَيْبًا ۚ قَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ وَلَا تَنقُصُوا الْمِكْيَالَ وَالْمِيزَانَ ۚ إِنِّي أَرَاكُم بِخَيْرٍ وَإِنِّي أَخَافُ عَلَيْكُمْ عَذَابَ يَوْمٍ مُّحِيطٍ
Yónni woon Nanu it ca waa Madyaana seen mbokk Suhaybu, mu ne leen : "Yéen samaw nit, jaamuleen Yàlla ; amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Buleen wàññi nattukaay yi ak màndaxe yi. Gis naa ne yéen a ngi ci biiri xéewal, te ragal naa mbugal dal leen ca bis ba ëmb lépp.
85وَيَا قَوْمِ أَوْفُوا الْمِكْيَالَ وَالْمِيزَانَ بِالْقِسْطِ ۖ وَلَا تَبْخَسُوا النَّاسَ أَشْيَاءَهُمْ وَلَا تَعْثَوْا فِي الْأَرْضِ مُفْسِدِينَ
Yéen samaw nit, nangeen di matal natt ak màndaxe cig maandute, te buleen wàññi dara ci lu nit ñi moom, te buleen salfaañe ci suuf si nekk yàqkat..
86بَقِيَّتُ اللَّهِ خَيْرٌ لَّكُمْ إِن كُنتُم مُّؤْمِنِينَ ۚ وَمَا أَنَا عَلَيْكُم بِحَفِيظٍ
Wërsëgu Yàlla moo gën ci yéen ndegam ñu gëm ngeen ! Te nekkuma di ku leen di warlul kiiraay”.
87قَالُوا يَا شُعَيْبُ أَصَلَاتُكَ تَأْمُرُكَ أَن نَّتْرُكَ مَا يَعْبُدُ آبَاؤُنَا أَوْ أَن نَّفْعَلَ فِي أَمْوَالِنَا مَا نَشَاءُ ۖ إِنَّكَ لَأَنتَ الْحَلِيمُ الرَّشِيدُ
Ñu ne ko : "Yaw Suhaybu! Ndax say julli dalaa xiir ci bàyyiloo nu la sunuy baay daan jaamu, walla nu bañ a def ci sunuy alal lu nu neex ?Yaw daal, yaa di ku lewet, di ku jub ? ”
88قَالَ يَا قَوْمِ أَرَأَيْتُمْ إِن كُنتُ عَلَىٰ بَيِّنَةٍ مِّن رَّبِّي وَرَزَقَنِي مِنْهُ رِزْقًا حَسَنًا ۚ وَمَا أُرِيدُ أَنْ أُخَالِفَكُمْ إِلَىٰ مَا أَنْهَاكُمْ عَنْهُ ۚ إِنْ أُرِيدُ إِلَّا الْإِصْلَاحَ مَا اسْتَطَعْتُ ۚ وَمَا تَوْفِيقِي إِلَّا بِاللَّهِ ۚ عَلَيْهِ تَوَكَّلْتُ وَإِلَيْهِ أُنِيبُ
Mu ne : "Yéen samaw nit, ndax seetlu ngeen ba xam ndax nekkuma ci lu leer lu jóge ca sama Boroom, te Mu jox ma xéewalam, mu di xéewal gu màgg ?... Te bëggumaa juuyook yéen ci lu ma leen tere. Bëgguma lu dul sellal [yéwénal] kem sama kàttan. Te samag njébbal wéeruwul fu dul ci Yàlla. Ci laa wéeru te ci Moom laay dellu.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
86Aaya
Tekki — Hud 86
Simoore Hud Aaya 86 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Wërsëgu Yàlla moo gën ci yéen ndegam ñu gëm ngeen…Simoore Aaya 86/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 84–88. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








