Yusuf · 14/111
Tekki Waxtaan — Simoore Yusuf
قَالُوا لَئِنْ أَكَلَهُ الذِّئْبُ وَنَحْنُ عُصْبَةٌ إِنَّا إِذًا لَّخَاسِرُونَ ۝١٤
Qaaloo la in akalahuzzi`bu wa nahnu `usbatun innaaa izal lakhaasiroon
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne : “Till! Su ko lekkee nag ak nii nu nekkee di mbooloo, kon dey nu gën a yées”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 12-16 — Simoore Yusuf

12أَرْسِلْهُ مَعَنَا غَدًا يَرْتَعْ وَيَلْعَبْ وَإِنَّا لَهُ لَحَافِظُونَ
Bu subaa nga yabal ko mu ànd ak nun muy sàmm jur gi, di fo. Dananu ko wattu”.
13قَالَ إِنِّي لَيَحْزُنُنِي أَن تَذْهَبُوا بِهِ وَأَخَافُ أَن يَأْكُلَهُ الذِّئْبُ وَأَنتُمْ عَنْهُ غَافِلُونَ
Mu ne leen : “Man dey, am naa njàqare ci ngeen ànd ak moom ; danaa ragal ngeen sàggan ba ag till lekk ko”.
14قَالُوا لَئِنْ أَكَلَهُ الذِّئْبُ وَنَحْنُ عُصْبَةٌ إِنَّا إِذًا لَّخَاسِرُونَ
Ñu ne : “Till! Su ko lekkee nag ak nii nu nekkee di mbooloo, kon dey nu gën a yées”.
15فَلَمَّا ذَهَبُوا بِهِ وَأَجْمَعُوا أَن يَجْعَلُوهُ فِي غَيَابَتِ الْجُبِّ ۚ وَأَوْحَيْنَا إِلَيْهِ لَتُنَبِّئَنَّهُم بِأَمْرِهِمْ هَٰذَا وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
Ba ñu àndeek moom, te mànkoo ci sànni ko ca xóot-xóot ba [teen ba], Nu xamal [Nun Yàlla] Yuusufa ne : “Danga leen mës a nettali seen jëf jii fu ñu ko foogewul”.
16وَجَاءُوا أَبَاهُمْ عِشَاءً يَبْكُونَ
Ñu dellu ci seen baay ci marax, di joox.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Yusuf 14

Simoore Yusuf Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne : “Till! Su ko lekkee nag ak nii…

Simoore Aaya 14/111 — Simoore Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yusuf Dégg, Simoore Yusuf Tekki, Simoore Yusuf mp3, Simoore Yusuf pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers