Yusuf · 53/111
Tekki Waxtaan — Yusuf
۞ وَمَا أُبَرِّئُ نَفْسِي ۚ إِنَّ النَّفْسَ لَأَمَّارَةٌ بِالسُّوءِ إِلَّا مَا رَحِمَ رَبِّي ۚ إِنَّ رَبِّي غَفُورٌ رَّحِيمٌ ٥٣
Transliteration
Wa maa ubarri`u nafsee; innan nafsa la ammaaratum bissooo`i illaa maa rahima Rabbee; inna Rabbee Ghafoorur Raheem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Jéemumaa setal sama bopp, ndax bakkan moom digalaakoon la ci lu bon, [mucctil ci moom] ku dul ku sama Boroom yërëm. Ndax sama Boroom Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 51-55 — Yusuf
51قَالَ مَا خَطْبُكُنَّ إِذْ رَاوَدتُّنَّ يُوسُفَ عَن نَّفْسِهِ ۚ قُلْنَ حَاشَ لِلَّهِ مَا عَلِمْنَا عَلَيْهِ مِن سُوءٍ ۚ قَالَتِ امْرَأَتُ الْعَزِيزِ الْآنَ حَصْحَصَ الْحَقُّ أَنَا رَاوَدتُّهُ عَن نَّفْسِهِ وَإِنَّهُ لَمِنَ الصَّادِقِينَ
[Buur ba ne jigéen ña] : “Lan moo doon seen mbir ba ngeen sàkku Yuusufa ci jëmmam ? ”. Ñu tontu ne : “Wax dëgg Yàlla ! Xamalunu ko dara lu bon”. Jabaru buur ba ne : “Léegi nag dëgg gi leer na. Maa ko sàkku woon. Moom moo waxoon dëgg ! ”
52ذَٰلِكَ لِيَعْلَمَ أَنِّي لَمْ أَخُنْهُ بِالْغَيْبِ وَأَنَّ اللَّهَ لَا يَهْدِي كَيْدَ الْخَائِنِينَ
“[Man Yuusufa maa defoon] noonu ngir buur bi xam ne wuruju ma ko ginnaawam, te sax Yàlla du jubale pexem wurujkat ya.
53۞ وَمَا أُبَرِّئُ نَفْسِي ۚ إِنَّ النَّفْسَ لَأَمَّارَةٌ بِالسُّوءِ إِلَّا مَا رَحِمَ رَبِّي ۚ إِنَّ رَبِّي غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Jéemumaa setal sama bopp, ndax bakkan moom digalaakoon la ci lu bon, [mucctil ci moom] ku dul ku sama Boroom yërëm. Ndax sama Boroom Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la”.
54وَقَالَ الْمَلِكُ ائْتُونِي بِهِ أَسْتَخْلِصْهُ لِنَفْسِي ۖ فَلَمَّا كَلَّمَهُ قَالَ إِنَّكَ الْيَوْمَ لَدَيْنَا مَكِينٌ أَمِينٌ
Buur ba ne : “Indil-leen ma ko : def ko mu sës ci man”. Ba mu waxeek moom, mu ne ko : “Bis niki tey, nekk nga ci man ku ñu darajaal, ku ñu wóolu”.
55قَالَ اجْعَلْنِي عَلَىٰ خَزَائِنِ الْأَرْضِ ۖ إِنِّي حَفِيظٌ عَلِيمٌ
Mu ne : “Dénkleen ma alali réew mi : am naa xam-xamu wattu ko”.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
53Aaya
Tekki — Yusuf 53
Simoore Yusuf Aaya 53 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jéemumaa setal sama bopp, ndax bakkan moom digalaakoon la ci…Simoore Aaya 53/111 — Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yusuf Dégg, Yusuf Tekki, Yusuf mp3, Yusuf pdf. Aaya 51–55. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








