Al-Hijr · 36/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
قَالَ رَبِّ فَأَنظِرْنِي إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ ۝٣٦
Qaala Rabbi fa anzirneee ilaa Yawmi yub`asoon
📖 Tekkim Wolof
-Mu ne : "Yaw sama Boroom, kon muñal ma ba bisu dekki ba”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 34-38 — Simoore Al-Hijr

34قَالَ فَاخْرُجْ مِنْهَا فَإِنَّكَ رَجِيمٌ
Mu tontu ne : “Man kat duma sujjóotal nit koo binde ci ban bu wow bu jóge ci banit bu ñu togg”.
35وَإِنَّ عَلَيْكَ اللَّعْنَةَ إِلَىٰ يَوْمِ الدِّينِ
Te am rëbb dal na ci sa kaw ba Bis-pénc ba di taxaw ! ”
36قَالَ رَبِّ فَأَنظِرْنِي إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
-Mu ne : "Yaw sama Boroom, kon muñal ma ba bisu dekki ba”.
37قَالَ فَإِنَّكَ مِنَ الْمُنظَرِينَ
Mu ne : bokk nga ca ña ñu muñal,
38إِلَىٰ يَوْمِ الْوَقْتِ الْمَعْلُومِ
ba ca Bis ba nga xam ne waxtoom lu ñu xam la.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
36Aaya

Tekki — Al-Hijr 36

Simoore Al-Hijr Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : -Mu ne : "Yaw sama Boroom, kon muñal ma ba…

Simoore Aaya 36/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers