Al-Hijr · 37/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
قَالَ فَإِنَّكَ مِنَ الْمُنظَرِينَ ٣٧
Transliteration
Qaala fa innaka minal munzareen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Mu ne : bokk nga ca ña ñu muñal,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 35-39 — Al-Hijr
35وَإِنَّ عَلَيْكَ اللَّعْنَةَ إِلَىٰ يَوْمِ الدِّينِ
Te am rëbb dal na ci sa kaw ba Bis-pénc ba di taxaw ! ”
36قَالَ رَبِّ فَأَنظِرْنِي إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
-Mu ne : "Yaw sama Boroom, kon muñal ma ba bisu dekki ba”.
37قَالَ فَإِنَّكَ مِنَ الْمُنظَرِينَ
Mu ne : bokk nga ca ña ñu muñal,
38إِلَىٰ يَوْمِ الْوَقْتِ الْمَعْلُومِ
ba ca Bis ba nga xam ne waxtoom lu ñu xam la.
39قَالَ رَبِّ بِمَا أَغْوَيْتَنِي لَأُزَيِّنَنَّ لَهُمْ فِي الْأَرْضِ وَلَأُغْوِيَنَّهُمْ أَجْمَعِينَ
- Ibliis ne : "Yaw sama Boroom, ci sababus li nga ma beewloo, fàwwu danaa leen rafetalal ci àddina [lu bon], te fàwwu danaa leen beewloo ñoom ñépp,
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
37Aaya
Tekki — Al-Hijr 37
Simoore Al-Hijr Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne : bokk nga ca ña ñu muñal,Simoore Aaya 37/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








