Al-Hijr · 42/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
إِنَّ عِبَادِي لَيْسَ لَكَ عَلَيْهِمْ سُلْطَانٌ إِلَّا مَنِ اتَّبَعَكَ مِنَ الْغَاوِينَ ۝٤٢
Inna `ibaadee laisa laka `alaihim sultaanun illaa manittaba`aka minal ghaaween
📖 Tekkim Wolof
Sama jaam ñi nag ñoom mënoo ci ñoom dara lu dul ña beew ña la topp.

🎧 Dégg


📜 Aaya 40-44 — Simoore Al-Hijr

40إِلَّا عِبَادَكَ مِنْهُمُ الْمُخْلَصِينَ
ba mu des ña sellal ca sa jaam ña.”
41قَالَ هَٰذَا صِرَاطٌ عَلَيَّ مُسْتَقِيمٌ
- Boroom bi tontu ne : lii mooy yoon wu jub wi jëm ci Man.
42إِنَّ عِبَادِي لَيْسَ لَكَ عَلَيْهِمْ سُلْطَانٌ إِلَّا مَنِ اتَّبَعَكَ مِنَ الْغَاوِينَ
Sama jaam ñi nag ñoom mënoo ci ñoom dara lu dul ña beew ña la topp.
43وَإِنَّ جَهَنَّمَ لَمَوْعِدُهُمْ أَجْمَعِينَ
Te Safara mooy fa ñuy daje ñoom ñépp.
44لَهَا سَبْعَةُ أَبْوَابٍ لِّكُلِّ بَابٍ مِّنْهُمْ جُزْءٌ مَّقْسُومٌ
Te Safara nag am na juróom-ñaari buntu te buntu bu nekk am na xaaj bu ñu ko sédde ca [ñu beew ña].
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Al-Hijr 42

Simoore Al-Hijr Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sama jaam ñi nag ñoom mënoo ci ñoom dara lu…

Simoore Aaya 42/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers