Al-Hijr · 43/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَإِنَّ جَهَنَّمَ لَمَوْعِدُهُمْ أَجْمَعِينَ ۝٤٣
Wa inna jahannama lamaw`iduhum ajma`een
📖 Tekkim Wolof
Te Safara mooy fa ñuy daje ñoom ñépp.

🎧 Dégg


📜 Aaya 41-45 — Simoore Al-Hijr

41قَالَ هَٰذَا صِرَاطٌ عَلَيَّ مُسْتَقِيمٌ
- Boroom bi tontu ne : lii mooy yoon wu jub wi jëm ci Man.
42إِنَّ عِبَادِي لَيْسَ لَكَ عَلَيْهِمْ سُلْطَانٌ إِلَّا مَنِ اتَّبَعَكَ مِنَ الْغَاوِينَ
Sama jaam ñi nag ñoom mënoo ci ñoom dara lu dul ña beew ña la topp.
43وَإِنَّ جَهَنَّمَ لَمَوْعِدُهُمْ أَجْمَعِينَ
Te Safara mooy fa ñuy daje ñoom ñépp.
44لَهَا سَبْعَةُ أَبْوَابٍ لِّكُلِّ بَابٍ مِّنْهُمْ جُزْءٌ مَّقْسُومٌ
Te Safara nag am na juróom-ñaari buntu te buntu bu nekk am na xaaj bu ñu ko sédde ca [ñu beew ña].
45إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي جَنَّاتٍ وَعُيُونٍ
Ña ragal Yàlla nag, ñangay nekk ciy àjjana ak i bëti-ndox [yuy ball].
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
43Aaya

Tekki — Al-Hijr 43

Simoore Al-Hijr Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te Safara mooy fa ñuy daje ñoom ñépp.

Simoore Aaya 43/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers