Al-Hijr · 59/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
إِلَّا آلَ لُوطٍ إِنَّا لَمُنَجُّوهُمْ أَجْمَعِينَ ۝٥٩
Illaaa Aala Loot; innaa lamunajjoohum ajma`een
📖 Tekkim Wolof
ba mu des njabootu Lóot, danañu leen musal ñoom ñépp

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 57-61 — Simoore Al-Hijr

57قَالَ فَمَا خَطْبُكُمْ أَيُّهَا الْمُرْسَلُونَ
Mu ne leen : “Waaw lan mooy seen mbir yéen ñi ñu yónni ?
58قَالُوا إِنَّا أُرْسِلْنَا إِلَىٰ قَوْمٍ مُّجْرِمِينَ
- Ñu ne : “Yónneef nañu ci aw nit ñu bari bàkkaar,
59إِلَّا آلَ لُوطٍ إِنَّا لَمُنَجُّوهُمْ أَجْمَعِينَ
ba mu des njabootu Lóot, danañu leen musal ñoom ñépp
60إِلَّا امْرَأَتَهُ قَدَّرْنَا ۙ إِنَّهَا لَمِنَ الْغَابِرِينَ
ku ca dul soxnaam sa. “Dogal Nanu ne moom ca way-des ña lay bokk (alku)”.
61فَلَمَّا جَاءَ آلَ لُوطٍ الْمُرْسَلُونَ
Ba ña ñu yónni agsee ca waa kër Lóot,
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
59Aaya

Tekki — Al-Hijr 59

Simoore Al-Hijr Aaya 59 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ba mu des njabootu Lóot, danañu leen musal ñoom ñépp

Simoore Aaya 59/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 57–61. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers