Al-Hijr · 74/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
فَجَعَلْنَا عَالِيَهَا سَافِلَهَا وَأَمْطَرْنَا عَلَيْهِمْ حِجَارَةً مِّن سِجِّيلٍ ۝٧٤
Faja`alnaa `aaliyahaa saafilahaa wa amtamaa `alaihim hijaaratam min sjijjeel
📖 Tekkim Wolof
Nu wëlbati la nekkon ca kaw [dëkk ba] dëpp ko mu féete suuf, Nu sotti ca kaw ab tawu xeer yu jóge Sijjiil.

🎧 Dégg


📜 Aaya 72-76 — Al-Hijr

72لَعَمْرُكَ إِنَّهُمْ لَفِي سَكْرَتِهِمْ يَعْمَهُونَ
Giñ naa ci sag dund [yaw Muhammed] ne naka ñoom nekkoon nañu di dengi-dengi ci seeni ngëlamte.
73فَأَخَذَتْهُمُ الصَّيْحَةُ مُشْرِقِينَ
Ag xaacu sadd leen suba cuuy.
74فَجَعَلْنَا عَالِيَهَا سَافِلَهَا وَأَمْطَرْنَا عَلَيْهِمْ حِجَارَةً مِّن سِجِّيلٍ
Nu wëlbati la nekkon ca kaw [dëkk ba] dëpp ko mu féete suuf, Nu sotti ca kaw ab tawu xeer yu jóge Sijjiil.
75إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّلْمُتَوَسِّمِينَ
Loolu nekk ay kéemaan ci ñuy settantal !
76وَإِنَّهَا لَبِسَبِيلٍ مُّقِيمٍ
Te [dëkk boobu] nekk na ci yoon wuñuy faral di jaar.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
74Aaya

Tekki — Al-Hijr 74

Simoore Al-Hijr Aaya 74 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu wëlbati la nekkon ca kaw [dëkk ba] dëpp ko…

Simoore Aaya 74/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 72–76. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers