Al-Hijr · 94/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
فَاصْدَعْ بِمَا تُؤْمَرُ وَأَعْرِضْ عَنِ الْمُشْرِكِينَ ۝٩٤
Fasda` bimaa tu`maru wa a`rid anil mushrikeen
📖 Tekkim Wolof
Waxal ci kaw li Nu la digal te nanga dëddu bokkaalekat yi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 92-96 — Al-Hijr

92فَوَرَبِّكَ لَنَسْأَلَنَّهُمْ أَجْمَعِينَ
Giñ naa ci sama màggug Boroom ! Fàwwu danañu leen laaj ñoom ñépp
93عَمَّا كَانُوا يَعْمَلُونَ
la ñu nekkon di ko def [ci ay ñaawtéef].
94فَاصْدَعْ بِمَا تُؤْمَرُ وَأَعْرِضْ عَنِ الْمُشْرِكِينَ
Waxal ci kaw li Nu la digal te nanga dëddu bokkaalekat yi.
95إِنَّا كَفَيْنَاكَ الْمُسْتَهْزِئِينَ
Naka Nun fegal nanu la ña lay téjji.
96الَّذِينَ يَجْعَلُونَ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ ۚ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ
Ña nga xam ne dañuy boole Yàlla ak jeneen yàlla, danañu mës a xam.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
94Aaya

Tekki — Al-Hijr 94

Simoore Al-Hijr Aaya 94 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ci kaw li Nu la digal te nanga dëddu…

Simoore Aaya 94/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 92–96. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers