Al-Hijr · 95/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
إِنَّا كَفَيْنَاكَ الْمُسْتَهْزِئِينَ ۝٩٥
Innaa kafainaakal mustahzi`een
📖 Tekkim Wolof
Naka Nun fegal nanu la ña lay téjji.

🎧 Dégg


📜 Aaya 93-97 — Simoore Al-Hijr

93عَمَّا كَانُوا يَعْمَلُونَ
la ñu nekkon di ko def [ci ay ñaawtéef].
94فَاصْدَعْ بِمَا تُؤْمَرُ وَأَعْرِضْ عَنِ الْمُشْرِكِينَ
Waxal ci kaw li Nu la digal te nanga dëddu bokkaalekat yi.
95إِنَّا كَفَيْنَاكَ الْمُسْتَهْزِئِينَ
Naka Nun fegal nanu la ña lay téjji.
96الَّذِينَ يَجْعَلُونَ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ ۚ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ
Ña nga xam ne dañuy boole Yàlla ak jeneen yàlla, danañu mës a xam.
97وَلَقَدْ نَعْلَمُ أَنَّكَ يَضِيقُ صَدْرُكَ بِمَا يَقُولُونَ
Xam Nanu ne la ñuy wax tiis na ci sa xol.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
95Aaya

Tekki — Al-Hijr 95

Simoore Al-Hijr Aaya 95 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Naka Nun fegal nanu la ña lay téjji.

Simoore Aaya 95/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 93–97. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers