Al-Hijr · 93/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
عَمَّا كَانُوا يَعْمَلُونَ ۝٩٣
Ammaa kaanoo ya`maloon
📖 Tekkim Wolof
la ñu nekkon di ko def [ci ay ñaawtéef].

🎧 Dégg


📜 Aaya 91-95 — Simoore Al-Hijr

91الَّذِينَ جَعَلُوا الْقُرْآنَ عِضِينَ
ca ña séddale Téere ba ay xaaj, pàcc-pàccee Alxuraan ngir sànkaate.
92فَوَرَبِّكَ لَنَسْأَلَنَّهُمْ أَجْمَعِينَ
Giñ naa ci sama màggug Boroom ! Fàwwu danañu leen laaj ñoom ñépp
93عَمَّا كَانُوا يَعْمَلُونَ
la ñu nekkon di ko def [ci ay ñaawtéef].
94فَاصْدَعْ بِمَا تُؤْمَرُ وَأَعْرِضْ عَنِ الْمُشْرِكِينَ
Waxal ci kaw li Nu la digal te nanga dëddu bokkaalekat yi.
95إِنَّا كَفَيْنَاكَ الْمُسْتَهْزِئِينَ
Naka Nun fegal nanu la ña lay téjji.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
93Aaya

Tekki — Al-Hijr 93

Simoore Al-Hijr Aaya 93 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : la ñu nekkon di ko def [ci ay ñaawtéef].

Simoore Aaya 93/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 91–95. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers